Señorita maa ko moom, désolée Bul insister kii ma koy décorer Sanq ba tay gis na noo koy xoole Sama bos la, Yàlla moo ñu boole Maaxàllaa yore jikko bukki ak tan Di jël alalu jaambur te xamuma ndax lan Fi nga teg sa loxo baaxul tegil ma ko ndank Bu de weeyu ngay jaay moo bandit ba ngi ni jank Oh señorita (señorita) Boo gënul ci man Oh baalu fetal Oh man la lay fëgg ngay càcc gënal ci man Anh boo xamul del laaj lijjanti ma Anh li nga sex tay kaani la du chewing-gum Oh ma señorita (ma señorita) Yaw doo bonita Maa doole ci la Man rekk la bugga Teg ko ci suuf li nga nar baaxul gënul ci yaw Bul ci dugg oo telo xam nga du la jikk ee Ku ma yàpp daa fekk ma nelaw Soo ma gisee xam duma sa morom Kii jigéen la, maamam ma ko yar Rewande ànd ak fula ak fayda ju bari ne ci man Dello ne ko mu delloo Avance bi mu jëloon loolu gëna sedd ci moom Man xale duma dekku sama xéy xaajul ci yaw Dute day xam lekkam xamal sa bopp mu nopal la Anh chéri coco (Oupadiam) Jaral na ma (Oupadiam) Ma garér la (Oupadiam) Te coow du jiip (Oupadiam) Xanaa xanaa dof wala lu la dal Xanaa xamoo li lekku bandit la Maaxàllaa yore jikko bukki ak tan Di jël alalu jaambur te xamuma ndax lan Fi nga teg sa loxo baaxul tegil ma ko ndank Bu de weeyu ngay jaay moo bandit ba ngi ni jank Oh señorita (señorita) Boo gënul ci man Oh baalu fetal Oh man la lay fëgg ngay càcc gënal ci man Anh boo xamul del laaj lijjanti ma Anh li nga sex tay kaani la du chewing-gum Oh ma señorita (ma señorita) Yaw doo bonita Maa doole ci la Man rekk la bugga Teg ko ci suuf li nga nar baaxul gënul ci yaw Bul ci dugg oo telo xam nga du la jikk ee Anh chéri coco (Oupadiam) Jaral na ma (Oupadiam) Ma garér la (Oupadiam) Te coow du jiip (Oupadiam) Xanaa xanaa dof wala lu la dal Xanaa xamoo li lekku bandit la Maaxàllaa yore jikko bukki ak tan Di jël alalu jaambur te xamuma ndax lan Fi nga teg sa loxo baaxul tegil ma ko ndank Bu de weeyu ngay jaay moo bandit ba ngi ni jank Oh señorita (señorita) Boo gënul ci man Oh baalu fetal Oh man la lay fëgg ngay càcc gënal ci man Anh boo xamul del laaj lijjanti ma Anh li nga sex tay kaani la du chewing-gum Oh ma señorita (ma señorita) Yaw doo bonita Maa doole ci la Man rekk la bugga