Fay while we dance o Fay while we dance o Feel (Vibe) energy when we dance o, yeah Feel (Vibe) energy energy Your body is so dangerous Your body is so dangerous Your body is so dangerous Your body is so dangerous Yeah Yeah Me i dey cool i dey fine I dey cool on my mind Me no dey stress you deh mine Gimme more lo’ on the night yea yea Yaay sama leer sama naaj Sama bideew sama light Sama takkandeer sama waay Jox la sama bopp doy nga ma njegenaay Yaay sama queen sama love Sama waay sama gayin sama xaaj nga you know, yeah Yaay sama queen sama love Sama waay sama gayin sama xaaj nga you know, yeah Man doffu ma ba di la foowe Topp ma ñu dem fu sore Yaa nekk sama mind yow baby foo nekk Sama yaayu doom rekk laa lay xoole Fay while we dance o Fay while we dance o Feel (Vibe) energy when we dance o, yeah Feel (Vibe) energy energy Your body is so dangerous Your body is so dangerous Your body is so dangerous Your body is so dangerous [Samba Peuzzi] Ku sa gel tooy loy utt ci gellu jambur ba ciy xeex Ku sa gel mool waawaw loy utt ci gellu jambur ba ciy xeex bae xool Man dam laa gis rekk dof mel ni sum-sum laa naan Feete ma kanam ñu fecc pum-pum turn up Boomerang sama xol bae lu dem day ñëwaat Badman bi moo fi nekk sa ex chinois lay lakk I say Nĭhǎo, baby Tòntu ma gaaw Nah yow laa nobb Man doffu ma ba di la foowe Topp ma ñu dem fu sore Yaa nekk sama mind yow baby foo nekk Sama yaayu doom rekk laa lay xoole Fay while we dance o Fay while we dance o Feel (Vibe) energy when we dance o, yeah Feel (Vibe) energy energy Your body is so dangerous Your body is so dangerous Your body is so dangerous Your body is so dangerous