Yeewu def fresh, yeewu def ouhh Sangu def fresh, sangu def ahhh Solu def fresh, solu def wuy yaay Génn def fresh, génn def mbap Fresh si ndey, fresh si baay Fresh si solu, oh my fresh Fresh si ndey, fresh si baay Fresh si solu, oh my fresh Doo ma doon swag dance Faut que ma comptéwat fans Yaa ngi siisu wat lank Mënatuma di tëb di dal ndank Xamuloo naka war baay Man la boy bi wëy ndank Dame lay génne fils, bye Ame na bénéfice, banque Marakisu leex di pees Sa papa mooy wax nel mutt Dugg bus bourlé, di pees Sa rap bi fayul, nel mutt Bokkuñu dañu wuute Ligne lay fay salaire, sama goûter (ay) Reere dibi mboté Gel bi ngay gent sama côté (ay) Yeewu def fresh, yeewu def ouhh Sangu def fresh, sangu def ahhh Solu def fresh, solu def wuy yaay Génn def fresh, génn def mbap Fresh si ndey, fresh si baay Fresh si solu, oh my fresh Fresh si ndey, fresh si baay Fresh si solu, oh my fresh Joxor major, joxor leen Meloon leen ni ñu mel, soxor leen Bindi son yi, joxaat leen Air bu fresh doxot leen Wiri wiri jari ndari Solaan dal yi tulli tat yi Takk bac bi, dem na jàngi Reer na France, man la Diarry [Iss 814] Eh pusal fee, bul ma fonto Sa best gel man ma konko Boo ma clashé, num lay tonto Bu ma masee, faut que ma sonko Mësuma sweet, I'm beauty Faut que nga tari sar pur aji Dañuy sandi xer pur promo Nekkul Auchan lañuy daji Deme gauche ak sama gars yi Def fresh, fresh, fresh, fresh Nañ dem droite, non du ñu bàyyi Def fresh, fresh, fresh, fresh Soxor ni xoolal li ñi sol Def fresh, fresh, fresh, fresh Ñooy pëndal ba sa école Def fresh, fresh, fresh, fresh Yeewu def fresh, yeewu def ouhh Sangu def fresh, sangu def ahhh Solu def fresh, solu def wuy yaay Génn def fresh, génn def mbap Fresh si ndey, fresh si baay Fresh si solu, oh my fresh Fresh si ndey, fresh si baay Fresh si solu, oh my fresh