Je ne mérite pas ça Yeah, yeah Hey bu ma xamoon ni lay demee duma ko nob Bu ma xamoon ni lay demee duma ko love Bu ma xamoon ni la may def duma ko jox yeah Bu ma xamoon ni lay deme hey Pourtant bañaluma dara, sa yaay ak sa pape Pourtant bañaluma won dara, sa yaay ak sa pape Bàyyiwoon naa lépp ndax yaw ak seen waa-kër Fàttewoon naa ñépp ndax yaw ak seen waa-kër ouh ouh Je ne mérite pas ça, lu tax nga may nax? Je ne mérite pas ça, lu tax nga may nax? Babe ak fi ñu jaar yépp pur man du jeex Munuma ko gëm, you're always on my mind Lu ma wax mu bañ, nanguma déglu Ne na dey dem xale bi wóor na ma Ça me fait très mal, tu me calcules plus Je t'ai tout donné, t'es parti comme ça T'avais promis de rester pour le meilleur et pour le pire Elle a brisé mon cœur pour du xaalis Bul jaay sa ngor Bëggal te Yàlla tax loolu rekk ay dëgg Bul jaay sa ngor Bëggal te Yàlla tax loolu rekk ay dëgg Hey bu ma xamoon ni lay demee duma ko nob Bu ma xamoon ni lay demee duma ko love Bu ma xamoon ni la may def duma ko jox yeah Bu ma xamoon ni lay deme hey Pourtant bañaluma dara, sa yaay ak sa pape Pourtant bañaluma won dara, sa yaay ak sa pape Bàyyiwoon naa lépp ndax yaw ak seen waa-kër Fàttewoon naa ñépp ndax yaw ak seen waa-kër ouh ouh Je ne mérite pas ça, lu tax nga may nax? Je ne mérite pas ça, lu tax nga may nax? Babe, ndax nak dina am lu baax bu de Yàlla xol lay fay Je make my heart great everyday Problème sur problème Et j’essaye de tout régler euuuh Tay si ki, suba si kee Bad girls changel suba du ni Tay si ki suba si kee, yeah Bul jaay sa ngor Bëggal te Yàlla tax loolu rekk ay dëgg Bul jaay sa ngor Bëggal te Yàlla tax loolu rekk ay dëgg Hey bu ma xamoon ni lay demee duma ko nob Bu ma xamoon ni lay demee duma ko love Bu ma xamoon ni la may def duma ko jox yeah Bu ma xamoon ni lay deme hey Pourtant bañaluma dara, sa yaay ak sa pape Pourtant bañaluma won dara, sa yaay ak sa pape Bàyyiwoon naa lépp ndax yaw ak seen waa-kër Fàttewoon naa ñépp ndax yaw ak seen waa-kër ouh ouh Je ne mérite pas ça, lu tax nga may nax? Je ne mérite pas ça, lu tax nga may nax?