Hey Xoolal boy, hey Bul duggu ci man bul testé déedéet (hein) Ndax bu ma lay shoot dangay break, naan thiek thiek Man la gaa yi di fay lu cher yaw weccek Wër di wax ci man, gwaik gwaik fenn rekk (hein) Boy fatal ma (hmmm flash, hey) Tontutuma (hmm clash) Léegi dama yor (hmm cash) Waxetuma (hmm am class) I say back in the days Meluma woon ni temps yu may jool de Maa ngi seet, temps yu may jool Metti woon na loolu, temps yu may jool Hmm, sant Yàlla, sant Yàlla Def ndank ndank Jële ko worses y nekk ci biti (fatal) Génne gang bi liggéey la laaj du bari tchip tchip (ouh, ouh, ouh) Dama réew ba yépp xam ni may numério 10 bi (yeah yeah) Xale yaa ngi laaj "Samba song bi looy wax fi?" Ma naan hey! Tus, dara, mbaraj (ouais, ouais, ouais) Mbaraj, tus, dara Liggéey ba xar rekk la ko bokkal Bàyyil ma ubbi dara (hey) Jël maa ngi leer, may faayeku (ah) Sekku maak yeen ay fayantu Hey rappeurs la rappul lool ngeen di laaj En tout cas soxal mère mang koy si faj Boy fatal ma (hmmm flash, hey) Tontutuma (hmm clash) Léegi dama yor (hmm cash) Waxetuma (hmm am class) I say back in the days Meluma woon ni temps yu may jool de Maa ngi seet, temps yu may jool Metti woon na loolu, temps yu may jool Hmm, sant Yàlla, sant Yàlla Tus, dara, mbaraj (ouais, ouais, ouais) Mbaraj, tus, dara Liggéey ba xar rekk la ko bokkal Bàyyil ma ubbi dara (hey) Bul duggu ci man bul testé déedéet (hein) Ndax bu ma lay shoot dangay break, naan thiek thiek Man la gaa yi di fay lu cher yaw weccek Wër di wax ci man, gwaik gwaik fenn rekk (hein) Boy fatal ma (hmmm flash, hey) Tontutuma (hmm clash) Léegi dama yor (hmm cash) Waxetuma (hmm am class) I say back in the days Meluma woon ni temps yu may jool de Maa ngi seet, temps yu may jool Metti woon na loolu, temps yu may jool Hmm, sant Yàlla, sant Yàlla