Teg ko ci temps Amoon nga fi temps Léegi ñun ñoo moome vent Dangay nappe! Yaw xam nga rekk dama di ndaanaan Lamb démb ma daan Ma leen gëna saf ni daxar ba ci yoon mbaadan Moytul noon mu tarxis saran Bari ngeen jaxan Flow bu reew la indi tay moom Rap bu soft la laal Amul arrêt (amul arrêt) Dey daw rekk (dey daw rekk) Fees lay def, xam naa gone bi comme Mbappé (comme Mbappé) Ma ni amul arrêt (amul arrêt) Munoo ma tardeel (mukk mukk) Xam nga coof laa raw ma jafe bàyyi ma Sàndi sama mbale mi nappé Déy daw rekk Yoroo wéroo Eh, bëgg jitte bëgg nappé Looy nappé, looy nappé Xam nañu li ngay dundu Dawoo suñu yaram, dangay nappé Teg ko ci temps Amoon nga fi temps Léegi ñun ñoo moome vent Dangay nappe! Fetaak moom place Ñoom ci kaw lañu jëm Te man fa laa toog Romb ay kuti ñu may mbow Ndax te bukki bi la bot Taat moo ko topp muy déllu gannaaw Ci bi ma ko Man ak ñoom dootuñu laale jamais Comme les Guissés-Maabo Teg fa sa loxo jàppal ma temps Pépite la ni Kylian Ñaw ngemb tere mbot ndaanaan dégg may daan Àdduna potu nda la sa rappeur du gux du naan Man lan ko diw ma jàpp seen girl yi, jàppal leen gam Final rekk moom laay joué Moom chef de bandi lay ñodd cooki feebar rekk de Dinañu ma daq mais yere yi may sol rekk a may teye Xaalis lay xëccoo mais du pe Lu ne lay teg sama der tewul maa ngi jàpp teint Amul arrêt (amul arrêt) Dey daw rekk (dey daw rekk) Fees lay def, xam naa gone bi comme Mbappé (comme Mbappé) Ma ni amul arrêt (amul arrêt) Munoo ma tardeel (mukk mukk) Xam nga coof laa raw ma jafe bàyyi ma Sàndi sama mbale mi nappé Déy daw rekk Yoroo wéroo Eh, bëgg jitte bëgg nappé Looy nappé, looy nappé Xam nañu li ngay dundu Dawoo suñu yaram, dangay nappé Teg ko ci temps Amoon nga fi temps Léegi ñun ñoo moome vent Dangay nappé! Man rekk ci sama yoon comme BRT bi Xale yaa ngi jooy ass bi la tebi Ne ma général yaw la asp bi Soxlatul may wax lam xa bi Ñaw, kàddu baal la dum leen gaawa dégg Man la dogo ñi doon bañ rambax ci game bi lañ gis tey ñu yor bongo Comme Aly wéy geroo fils sa buur la Benn Aly ñëw wacc la sa ngur la Tegal sa rappeur sañ-sañ, tojal ko mbari from Dieck Teg ko ci temps di sañse, jamos ko blow tek-tek Lindia seen game bi bët-set, seen K7 sama weccet Fatt dundu lifu jetset, teddi king fat pérpéte Amul arrêt (amul arrêt) Dey daw rekk (dey daw rekk) Fees lay def, xam naa gone bi comme Mbappé (comme Mbappé) Ma ni amul arrêt (amul arrêt) Munoo ma tardeel (mukk mukk) Xam nga coof laa raw ma jafe bàyyi ma Sàndi sama mbale mi nappé Déy daw rekk Yoroo wéroo Eh, bëgg jitte bëgg nappé Looy nappé, looy nappé Xam nañu li ngay dundu Dawoo suñu yaram, dangay nappé Teg ko ci temps Amoon nga fi temps Léegi ñun ñoo moome vent Dangay nappé!