Loo bëggul man duma ko bëgg damay gaañ Koo bëggul man duma ko bëgg dafay xaar Yaa may tere nelaw ndax danga jongé déeg daaj Kaay ma feccal la yaw, man jaral nga ma tàrantaax Loo bëggul ne naa la dafay xaar Ku dul yaw na ma dandu ñëwal gaaw Yaay yëngal sama aah, man barde naa Bàyyil mbele mbese gi di wax Yaa fi nekk te du deñ, girl Buur Yàlla moo ko def te du deñ Bëgg nga ma bëgg naa lool du deñ Soxna si yaay sama lumière Ba abadan du deñ Bëgg nga ma bëgg naa lool du deñ Buur Yàlla moo ko def te du deñ Soxna si yaay sama lumière Ba abadan du deñ Buuru galle lay doon ci yaw Dinaa la xeexal fépp foo mën nekk Newoon naa la ah yaw Dagul nu ma la neexe yaa fi nekk te du deñ Bi ma la xame ci la tàggook wet oooh, yo yo yo Kon bul ma sori ñëwal fi sama wet ooh Ma dundu paradise They wanna make me out your way Baby girl don't let them break your heart Ñoom dañuy siisu di fen Baby girl don't let them break your heart Baby mine warul jooy, nah nah Baby mine, bul jooy, waawaaw Loo bëggul man duma ko bëgg damay gaañ Koo bëggul man duma ko bëgg dafay xaar Yaa may tere nelaw ndax danga jongé déeg daaj Kaay ma feccal la yaw, man jaral nga ma tàrantaax Loo bëggul ne naa la dafay xaar Ku dul yaw na ma dandu ñëwal gaaw Yaay yëngal sama aah, man barde naa Bàyyil mbele mbese gi di wax Yaa fi nekk te du deñ, girl Buur Yàlla moo ko def te du deñ Bëgg nga ma bëgg naa lool du deñ Soxna si yaay sama lumière Ba abadan du deñ Bëgg nga ma bëgg naa lool du deñ Buur Yàlla moo ko def te du deñ Soxna si yaay sama lumière Ba abadan du deñ Bébé yaa ngi digal lu ne Ñoo ngi koy wax dëgg dëgg nak du jeex Jaar nañu fu ne te ñooy muje Kaay ma feccal la bu de mooy li la neex Bébé, bébé Yàlla xam na, xam nga Li nga ma jaral wallaay wallaay Bëgg nañu diggënte bi jeex Mais fi muus du fi na ne ñex Lu neex da nañu dundu lu neex Xam nga ne sa xol duma ko nab-nabé Yaw ni nga ma bëgg noonu laa la bëggee Bul mab yaa tay daagul fu ñu la nobee Yaw ne na la bul mës a bàyyi Ndax dama la woolu Bul déglu wax yu bon yi ci man way Ndax dama la woolu Yaw ne na la ne wëti na la Soo ma bàyyee ci la lay jàpp Sama xol, sama reeni xol Xam nga ni bëgg bëgg naa la Loo bëggul man duma ko bëgg damay gaañ Koo bëggul man duma ko bëgg dafay xaar Yaa may tere nelaw ndax danga jongé déeg daaj Kaay ma feccal la yaw, man jaral nga ma tàrantaax Loo bëggul ne naa la dafay xaar Ku dul yaw na ma dandu ñëwal gaaw Yaay yëngal sama aah, man barde naa Bàyyil mbele mbese gi di wax Yaa fi nekk te du deñ, girl Buur Yàlla moo ko def te du deñ Bëgg nga ma bëgg naa lool du deñ Soxna si yaay sama lumière Ba abadan du deñ Bëgg nga ma bëgg naa lool du deñ Buur Yàlla moo ko def te du deñ Soxna si yaay sama lumière Ba abadan du deñ