Boy Ghetto what's up! Geumoko wone finiou nobanté domafa guiss Dieul: Fuck Love, I'm savage def sama devise Diépi wone bép goor gouy doundou relation hindou Guéne ak shaw une semaine mou dème, djiko yi meunoul andd Kholou keurign la yorone, guél bou tang ma diarou Bii bou bakh bi la, tay nak bouma reuthié ma wéré Nga deungue wala nga dioup bokoy khol di waarou Nieupa ngui wakh si dokhine bi ak rafétayam waaw Bou dokhé ba dém gauche Boufa khar droite Même "boy diay yékk" Bouy nieuw ngay watieu Shaw bi dam-ko guiss rek tipsy Bari caractère ba kène douko tankal Sétt wetch saf sap Yah! Khalé bi comme tangal Bou dokhé ba ridj gauche Boufa khar droite Même boy diay yékk Bouy nieuw ngay watieu Shaw bi dam-ko guiss rek tipsy Bari caractère ba kène douko tankal Sétt wetch saf sap Yah! Khalé bi comme tangal Niro woul ak Guèl yi dieul sène galé défko bar rek oubi Entrée bi gratuite la Mais bofa dougué yow yay dieund Cons bokoulsi Génération Jet-Set bi Dakarou tay Teksi diek set fils Takk sama fitt songue khalé bi lé rek tek Comment tu vas bébé est-ce que meune nga sigui khol ma Yangui wéteuli sama mère tchi sama khol Kheutch lokho bi rek tek si sama call Mou sourire, ma contane ni nullard bou amm fitt Affaires yangui commencé nekh, diokh nama 7-7 Bou dokhé ba dém gauche Boufa khar droite Même boy diay yékk Bouy nieuw ngay watieu Shaw bi dam-ko guiss rek tipsy Bari caractère ba kène douko tankal Sétt wetch saf sap Yah! Khalé bi comme tangal Bou dokhé ba ridj gauche Boufa khar droite Même boy diay yékk Bouy nieuw ngay watieu Shaw bi dam-ko guiss rek tipsy Bari caractère ba kène douko tankal Sétt wetch saf sap Yah! Khalé bi comme tangal Daw ba reuk, khar goudi pour ték premier pas Tabakh souniou relation dieul kholam déf fa tank Même pas une semaine, moungui ni boy bi dafma takkhe Dougou Instagram screenshot photo ba tok Défnama PP fépp bala dara khéw Déguanté chaque jours, wakh téléphone ba néléw Kounéka ngui saub, appels ak messages commencé taw Je t'aime ya ngui dakanté ak ay Malaraw Aligné kaw ba souff Kholma boy, today j'suis sappé Tay lagnou wara tassé Bama shaw' bi, dama geuna tipsé Bébé doumala khandiou Auto, khaliss, villa Dila diéma Pape et Cheikh Liko dal moma dal Khamnani lonkotinaaaa Bou dokhé ba dém gauche Boufa khar droite Même boy diay yékk Bouy nieuw ngay watieu Shaw bi dam-ko guiss rek tipsy Bari caractère ba kène douko tankal Sétt wetch saf sap Yah! Khalé bi comme tangal Bou dokhé ba ridj gauche Boufa khar droite Même boy diay yékk Bouy nieuw ngay watieu Shaw bi dam-ko guiss rek tipsy Bari caractère ba kène douko tankal Sétt wetch saf sap Yah! Khalé bi comme tangal