Boy mako wax Sa rappeur dou dém fen té na saltél fépp Amoul loumey tite from dièk waw Dérétou diameugeun yolé yolé yolé Ragalougn ko hé yolé yolé Nioune ragalougn ko Mako wax sa rappeur dou dem fen Té na saltél feep waw waw Amoul loumey tite from dièk waw waw Dérétou diameugeun hé yolé yolé yolé Ragalougn ko hé yolé yolé hah Nioune ragalougn ko Yonou musique bouko def xew xew Mane damay fo meun na salsa dilén fathi Kakatar ci flow international dou ci langue Reuy lamigne mo len té ci souf Nieupa beug def béneu diap Bayi na boudé li ngen di def ay rap Indi lou bess si game bi Gayi di sissou nane damay tassou Signé orthographe sen entre jambe Sho yi ba ngen fok ma tico-tatoo Laal ay millions takhoul ma dem tok Waxal wizkid ak tekno ma ngui tew Lep muy bien bayi len niou hablar bro Dawou ma thiow Manquer vibe manqué style takh Ma bagna def ni niom di sol yénén yéré Ay dof lagn téglé hit comme un Toofan da nga wara taak téré Represent ko nieup sip niouné You bess yi niow beugeu mambou bo Ba ngen di deup ndox ma ngui liguey From ghettho buzzou Ndongo Lo Boy mako wax Sa rappeur dou dém fen té na saltél fépp Amoul loumey tite from dièk waw Dérétou diameugeun yolé yolé yolé! Ragalougn ko hé yolé yolé nioune ragalougn ko Mako wax sa rappeur dou dem fen Té na saltél feep waw waw Amoul loumey tite from dièk waw waw Dérétou diameugeun hé yolé yolé yolé Ragalougn ko hé yolé yolé hah Nioune ragalougn ko Deuk kognou siteu Rêvé log ni deuk cité Succès depuis khalé lako coaché Call me khassate khaléyi bro Li ngen esclave dageu boum mou gathié Takkal mère bi ay chaine nou or De flou saleté ma fay batay ma sen So darling ma nek si bop bi bro Khamo len dara beug def rap bi job Sen genre yi taux de chômage lagniy yok Woutil ci lo diap même boy nirok jamel Deuk bi goor rou lokho ci poche rek kay bok Baat bou yambar bi momay fay Loutakh makay changé di forcé lou rock Khép ma ndax damay represent Boy ghetto bi dal téré sa dome Téwal dièk fay narr bi khoromamemafia bi begue Li si dess yeup je m’en fou Khawma défaite pourtant chaque jour si mane La bay yi accro comme parifoot Indil niou yolé sama gang bi kén dou khof Tapét yi ngen tek bandit Dagn len na khékhal demb Tay niou fok niou dofS Seutt tou dix points yi takh Nerf you demba yi tendu Boy mako wax Sa rappeur dou dém fen té na saltél fépp Amoul loumey tite from dièk waw Dérétou diameugeun yolé yolé yolé! Ragalougn ko hé yolé yolé Nioune ragalougn ko Mako wax sa rappeur dou dem fen Té na saltél feep waw waw Amoul loumey tite from dièk waw waw Dérétou diameugeun hé yolé yolé yolé Ragalougn ko hé yolé yolé hah Nioune ragalougn ko Yolé yolé yolé ragalougn ko Hé yolé yolé hah Nioune ragalougn ko