Ki nga njëkk a nob Yàq na sa xol bul geestu bàyyi ko Newoon naa la bés Maak yaw ñooy ngembu bëre daan ko Ci bés yu wees Amoon nga ku la wor Ci fan yu des Naa la dundloo mbëggeel bu wóor Samay cartes bancaires jël ko Say naqar nga dër ko Buñ nee kokkorikoo/kókkali ko Loo joxoñ ma dagg ko Naa ko wan me nit ku reew La mu yor moomu ko Bu wayadee waddal ko Man ma yaru jariñoo ko Waxal sa ex Am nga keneen ku bees Waxal sa ex Li ngeen dundoon yéen ñaar dafa weesu Waxal sa ex Aller boo gis am na retour Demal ci sa ex Face à face nee ko demal nga toog Waxal sa ex Man dama koo gën a dooj Waxal sa ex Man sax damaa gën a yokk dose bi Mais attends Sa ex Est-ce que doful sax laa foog Demal ci sa ex Face à face nee ko dangay xaar Bateau dem na, bateau coster Yaa ko sànni man ma capter Am na keneen ku doful Remontada ngay am foofu Billahi xamul li mu perte Ngaaka la billahi dafa merder Bala ngaa xam ki nga yor Mu wan la ginnaaw, danga weere Ne ko nobuloo ma woon Faalewoo ma woon Gisuloo ma woon Keneen xam na ni ñuy nobee Bëgguloo ma woon Fonkuloo ma woon Yëguloo ma woon Keneen xam na ni ñuy bëggee Danga bàyyi ba jaan ji romb la Nga topp watat way daw Moytul a daanu Boo ko bàyyee Dinga ko jéem a bara saudi Waaye baara-yëgoo xarit Génnewu la ci Waxal sa ex Am nga keneen ku bees Waxal sa ex Li ngeen dundoon yéen ñaar dafa weesu Waxal sa ex Aller boo gis am na retour Demal ci sa ex Face à face nee ko demal nga toog Waxal sa ex Man dama koo gën a dooj Waxal sa ex Man sax damaa gën a yokk dose bi Mais attends Sa ex Est-ce que doful sax laa foog Demal ci sa ex Face à face nee ko dangay xaar Dégguloo après l'heure Ce n'est plus l'heure Dangaa fowe coeur Assumeel say erreurs Boule bee mujje tourner Kex-kex, man ma ree Dund love story Cale ko sunu story Yaw kii mooy sa ex? (Kii li?) Dafa def erreur Kii mooy sa ex Xamul woon sa valeur Eh bébé sa ex Moom dafa obsolète Demal ci sa ex Face à face nee ko dangay xaar Dangay xaar yaw Ex dangay xaar Danga ma doon fowe Man tay jii romb naa la Wallahi dangay xaar Danga maa teel a feral Bàyyil ma nàmpi feneen Man tay jii romb naa la Gisoo woon sama njëg Xamoo woon li may jar Tay keneen gis na li ma jar Man dem naa, bàyyi naa la Nobatuma la Man ex bàyyi naa la Romb naa la Yaw ex doxal fowi