Daf may dal, dal naa fi ku ne Aw la soru aw àj ko ci kaw Baby da dor ko ci suuf Yaw mi ma nob, xam naa ni yaay l'enfant des bénis Doole yemul ñamal ba xam Man aw la bëgg Aw la ma nob, ay lexam moo ka noy népp Waaw wolay Aw mi ko def xam naa ni yaa ka tey def Bi mbëggeel la dundu roppi baay ba géwél sa yaay Qu'est-ce que ça fait? Su ñu wétee Sa loxo yi nga may teg may daanu def na éffet Ma lingi yo man yaw yaay sama repré Drogue bi may laaj Sa deret laay pikkiroo wou-woo Ba keroog may overdose Te aimable waaw Sa deret laay pikkiroo wou-woo Lii ni Sax di neex yaa ko moom Te fi ni Ku dul yaw wat na doo fi rot Baalal ma Mame Coumba Lambay baalal ma Mbëggeel ku mu jàpp da lay Balay baay nga taago sago Lii ni Sax di neex yaa ko moom Fi ni Ku dul yaw wat na doo fi rot Baalal ma Mame Coumba Lambay baalal ma Mbëggeel ku mu jàpp da lay Balay baay nga taago sago Dal na ci lu ne! Dugg nga sama surface di ma moqué di ma tapasse Sa lowël dey toj kas guddi jote nga di ma cokass Bébé xam nga doo seen maas, bodio-bodio du la tendance Menthe, menotte wala cristal Bébé xam nga danga saay-saay ye ye Man xale laa, xawma yo yo Nga def ma nonoh, ñamal ma yoyo Qu'est-ce que ça fait? Su ñu wétee Sa loxo yi nga may teg may daanu def na éffet Ma lingi yo man yaw yaay sama repré Drogue bi may laaj Sa deret laay pikkiroo wou-woo Ba keroog may overdose Te aimable waaw Sa deret laay pikkiroo wou-woo Lii ni Sax di neex yaa ko moom Te fi ni Ku dul yaw wat na doo fi rot Baalal ma Mame Coumba Lambay baalal ma Mbëggeel ku mu jàpp da lay Balay baay nga taago sago Lii ni Sax di neex yaa ko moom Fi ni Ku dul yaw wat na doo fi rot Baalal ma Mame Coumba Lambay baalal ma Mbëggeel ku mu jàpp da lay Balay baay nga taago sago