Music Soryba ha-ha-haaa Music Nga jël ma taf sa wét di ma tëgg ni tama tàjjaboon Dama dof ci yaw, nga may ndëpal ma daanu ci sa ron Fu ma jëm ak xale bi, àttanuma lii Son regard me fait effet, o-o-ow ça m'excite Fi ma làkk dafa sore, bopp bi noonul ñore Yëfi bandit dafa jongé Def ma buur di ma limal samay maam Mbëggeel lu neex la Billaay, mbëggeel lu neex Man ak yaw ba États-Unis Sans visa ma ni Dox ba dem Roumanie Naaw ba asaman tërëdi àljanna Foofu la, billaay foofu la Billaay wallaay bébé Maa la nob, wax ma ku ci mën nada Moom du coow du tooñ du fowe dóor ak saaga Moom dafa nooy agneau la bu tooy Moom sax duma jooyloo dëkke di ma sourireloo (bébé) Maa la nob, wax ma ku ci mën nada Moom du coow du tooñ du fowe dóor ak saaga Moom dafa nooy agneau la bu tooy Moom sax duma jooyloo dëkke di ma sourireloo Yaay sama oxygène bi ma soxla di nooy tous les jours Bébé je t'aime, tu m'aimes Depuis la nuit des temps pour tous les jours Poser sama balance lourde, ma yoxu 'au secours! ' Li nekkatul love kase dama jaaxle céy l'amour Waat naa ba waat sama akoulaye man yaa ma saf Sama mbëggeel raw na roppalaan ba naaw jëm asaman Ñaanu la ko lawu soo ma njëkkoon dee bébé Billaay, dootuma dundu man! États-Unis, sans visa ma ni Dox ba dem Roumanie Naaw ba asaman tërëdi àljanna Foofu la, billaay foofu la Billaay wallaay bébé Maa la nob, wax ma ku ci mën nada Moom du coow du tooñ du fowe dóor ak saaga Moom dafa nooy agneau la bu tooy Moom sax duma jooyloo dëkke di ma sourireloo bébé Assane Wilane l'international Chéri Mamy Mbaye Sofa Magui saliwoo Assane bëgg naa la, Wilane fonk naa la Mami doo ko jooyloo, dëkke di ko sourireloo bébé Maa la nob, wax ma ku ci mën nada Moom du coow du tooñ du fowe dóor ak saaga Moom dafa nooy agneau la bu tooy Moom sax duma jooyloo dëkke di ma sourireloo Maa la nob, wax ma ku ci mën nada Moom du coow du tooñ du fowe dóor ak saaga Moom dafa nooy agneau la bu tooy Moom sax duma jooyloo dëkke di ma sourireloo