Ioe so ñeimé, ñu déef waaw waaw Sopaalike rap djomaal Moytul ma dooflo laa Ioe no beügé, ñu déef waaw waaw Djuuma djomaalul boopam naak Cà séeytané maan leü My baby boy, xaam na ni tiit nga Cà fiit bi teüp naa nooma gissé Li ma sool daay dooflo goor Tée saax tass na guerre moytul ma killer Je vais te rendre fous, je vais te rendre fous Anaa cà xéel bi déem na My baby, je vais te rendre fous, je vais te rendre fous Waxaal waaxu niit My baby kaay, te rendre fous, je vais te rendre fous Anaa cà xéel bi déem na Oh my baby, je vais te rendre fous, je vais te rendre fous (Waxaal waaxu niit) Yaa doof ba feel ci maan Baari vitesses paré kooba Ioe daa nga fiir duugu ci maan Léep lo tchi goobé maané ioe leü Maané laa néek tchi née Ruuku djiné la laay duugal So moytuwul ma djomaal leü guudi Yooré taaru djiné, mba duuñ née Moom daafa dadjék guélou rap taax mu Daaf koy saalite Xaam na ni tiit nga Cà fiit bi teüp naa nooma gissé Li ma sool daay dooflo goor Tée saax tass na guerre moytul ma killer Je vais te rendre fous, je vais te rendre fous Anaa cà xéel bi déem na My baby, je vais te rendre fous, je vais te rendre fous Waxaal waaxu niit My baby kay, te rendre fous, je vais te rendre fous Anaa cà xéel bi déem na Oh my baby, je vais te rendre fous, je vais te rendre fous Waxaal waaxu niit So beügé ba mu djaaral leü Doof lool wadji booko meünul baayi Maané so beügé ba mu djaaral leü Doonal gyal bi di doof lo wadji, tchi deüg deüg So beügé ba mu djaaral leü Doof lool wadji booko meünul baayi Maané so beügé ba mu djaaral leü Naa saaf kaani guudi bul tchi taayi Doonal rap su ngooné Djomaal ko su ngooné, ioe su ngooné Waan ko ni nga méel, méetil doof loo ko Waan ko ni nga méel, djaaxal ko doof loo ko Doonal rap su ngooné Djomaal ko su ngooné, ioe su ngooné Waan ko ni nga méel, méetil doof loo ko Waan ko ni nga méel, djaaxal ko doof loo ko Raakadju na maané raakadju na Su féeké ñeimé wo cà gyal lu rap bi poussal fée Raam paam pii raam, maané raam paam pii raam Su féeké ñeimé wo cà gyal lu rap bi poussal fée Woooo feülé Maan ni ma méel doof lo naa goor Doof lo naa ku néek Eeee o héy Xaalé bu djigéen bi lu mu saañsé lo déef nga géestu So beügé ba mu djaaral leü Doof lool wadji booko meünul baayi Maané so beügé ba mu djaaral leü Doonal gyal bi di doof lo wadji, tchi deüg deüg So beügé ba mu djaaral leü Doof lool wadji booko meünul baayi Maané so beügé ba mu djaaral leü Naa saaf kaani guudi bul tchi taayi Doonal rap su ngooné Djomaal ko su ngooné, ioe su ngooné Waan ko ni nga méel, méetil doof loo ko Waan ko ni nga méel, djaaxal ko doof loo ko Doonal rap su ngooné Djomaal ko su ngooné, ioe su ngooné Waan ko ni nga méel, méetil doof loo ko Waan ko ni nga méel, djaaxal ko doof loo ko Waan ko ni nga méel, méetil doof loo ko Waan ko ni nga méel, djaaxal ko doof loo ko