Su ma xoolee ni tay sama ex nga Ak li ñu dundu démb? Xamuloo lu ma naroon pur maak yaw Xale bi you don't know Loolu tay dinga ko dégg mu metti la Xamoo ci lu ma nekk Yaa ngi wër fu ne di ma laajte Nga mel ni ku for doom Li nga téye woon sax loxo toxu na Mi ngi ci yeneen niveau Te xamuloo fi ma féete (fi ma féete) Xale bi you don't know (you don't know) Yu neex yi ma nekke (yi ma nekke) Xale bi you don't know (you don't know) Oh, oh nii xol bi di fexe (bi di fexe) Xale bi you don't know (you don't know) Oh, tay li nga perte (li nga perte) Xale bi you don't know (you don't know) Soo ko gisee waxal ma ko li dégg nga? Mu noppali ku te muñ Moo dem moo gedd sama xol bi Yaay sama ex la Duma wajju di lekkat ndax làmbu ma Sa moroom moo ngi nii toog Mu nobee ma lu ne defal ma My baby kontaan naa Sama número telefone changer naa Maa ngi yeneen niveau Te xamuloo fi ma féete (fi ma féete) Xale bi you don't know (you don't know) Yu neex yi ma nekke (yi ma nekke) Xale bi you don't know (you don't know) Oh, oh nii xol bi di fexe (bi di fexe) Xale bi you don't know (you don't know) Oh, tay li nga perte (li nga perte) Xale bi you don't know (you don't know) Ooh, waxal sama ex (waxal sama ex bi) Waxal sama ex bi jaajëff (jaajëff) Ndax bi mu ma bàyyee ba léegi Man dama jëlaat poids Ooh, waxal ma sa ex (waxal ma sama ex) Waxal ma sama ex bi jaa (jaa) Am na ku ko fii remplacer Te di la kontaanloo Oh, oh, oh, waxal sama ex (waxal sama ex) Oh, oh, oh, waxal sama ex mu may ma Ndax dina romb ci tawoon bii Di dundu àljanna Ooh, allo sama ex (allo sama ex) Ooh, allo sama ex, goodbye Am na ku la fi remplacer Ba pare la la laaa Li nga téye woon sax loxo toxu na Mi ngi ci yeneen niveau!