Lay layla luu Tay ngeen dee, teyaati ngeen dee ooo Wuy sama ndey jooy naa ba wadd Kaay! Doo def lu mel ni même boo ko bëggoon (eee) Mënoo ko def ni man mi (eee) Lan ngay wër ci stars lu newul ci man mi (eee) Maa jogé di échauffement arbitre naan but Lekketu bayal yi la miin Xale bi yëngël jamono jëkketi na toog di xaar seen commentaire Troisième GT ci boy bu ndaw, ah c'est légendaire! Kan moo fi dëkk ci feesal stade, Senegaal booy ma fi stars Tribune la ma ñépp di owe, xaaju ma ci ay salle Maa ngi dégg xale yi naan: VJ duñu concert xanaa Yaw doo def bala déwen, léegi ñu am vacances Yaw suñu album bi ñuy xaar, doo ko génne xanaa? Yaw loo génne dafay neex, chouchou des nanas Moo tax ni rekk laa koy defe ni mu yombe Nga jënde sa ticket dox ñu daje biir GT Album bi bés bu génne bu amul morts am bléssé Ndax xol bu rafet ak mbégte ding ko déglu wét di fecc Force zac zac zarko (àljanna) Ko kaay corégeou président maay capo Man VJ sama concert xale yi neex fa lañ baado Ma te gambe bi flow yas ngay siisoo Bon, setlu naa nak ku fi jokk rekk def ma concurrence Maa toog def noppi di seetaan calmement Ki la wax dama tappet ku ko ne ragal la Man may bandit di délinquant (yaw ki di woyu) Mara, marabout de la jeunesse Jeune mara, marabout de la jeunesse Man VJ, maay marabout de la jeunesse Jeune mara, marabout de la jeunesse Mara, marabout de la jeunesse Jeune mara, marabout de la jeunesse Man VJ, maay marabout de la jeunesse Jeune mara, marabout de la jeunesse!