Ndekke du mbëggeeku kese Te sax xeetu mbëggeel yi dafa rare Jekku ma ni duma baal, yeah, yeah An kon yaw bandit nga ndekke, bébé Soppi nga sama xol bi limonade Sirote ko di ko naan, yeah, yeah Ndax ba ñuy njëkka gisante Li nga ma yénne ni mu diisee Ak ni ñu xoolante Rekk ma xam ni Yàlla ñu boole Est-ce que doo jinne ndax jommal nga ma (kaay waay) Dofloo nga ma (kaay waay) Waaye dëfal nga ma (kaay waay) Man li may dundu ni dal neex na ma (kaay waay) Soo bégee, ma bég (kaay waay) Ñu dekke di ree (kaay waay) Yaw mësul metti ba nga réccu li nga ma xam (kaay waay) Maa la gënal lu ne (kaay waay) Te yaa ma gënal ku ne (kaay waay) Bae li ñuy dundu ni cer carré na (kaay waay) Bégal, ma bég (kaay waay) Maa xécc sa rëndal happy (kaay waay) Soo ma soree oh my love Nammeel bi may yëg ci yaw, wallaay! Yaa ko mëna faj, ñëwal Ñuy kaf di ree Ñuy kaf di fo di ree Ndax ba ñuy njëkka gisante Li nga ma yénne ni mu diisee Ak ni ñu xoolante Rekk ma xam ni Yàlla ñu boole Est-ce que doo jinne ndax jommal nga ma (kaay waay) Dofloo nga ma (kaay waay) Waaye dëfal nga ma (kaay waay) Man li may dundu ni dal neex na ma (kaay waay) Soo bégee, ma bég (kaay waay) Ñu dekke di ree (kaay waay) Yaw mësul metti ba nga réccu li nga ma xam (kaay waay) Maa la gënal lu ne (kaay waay) Te yaa ma gënal ku ne (kaay waay) Bae li ñuy dundu ni cer carré na (kaay waay) Bégal, ma bég (kaay waay) Maa xécc sa rëndal happy (kaay waay) Oh bébé toi mon bébé Toi qui m’as tout donné Je pourrais jamais te quitter Je t’en fais la promesse mon bébé Tu m’as tellement épaulé Quand il le fallait M’as sorti de la galère Je vais te rendre la money Oh bébé yaw mi gunge ma man maa lay gunge Et si t'as peur crie, aide-moi, man maa lay sauver Oh bébé yaw ndax bëgg nga ma comme ni ma la bëggee Ndax ni ma la bëggee ëpp na waa li num deme Oh bébé toi mon bébé Toi qui m’as tout donné Je pourrais jamais te quitter Je t’en fais la promesse mon bébé Tu m’as tellement épaulé Quand il le fallait M’as sorti de la galère Je vais te rendre la money Oh bébé yaw mi gunge ma