Vj Luñuy gëne di dém, je pense à toi Imaginant la chance que j'ai, ndax bëgg naala Dinala djëndël wurus ak ngalam Ndax yama gënël luma mëneti am Diyañée, oh, iyé faa do n'na Na n'dé mi i yé ou té tô to n'na N'de diyañée, oh, iyé faa do n'dé la Na n'dé tou mi i yé ou té tô to n'na Ma dila, toi et moi, toi et moi Toi et moi, noko bëggée bëgg na Toi et moi, me and you, bébé Noko bëggée bëgg na Ń b'í fɛ̀, bébé, ń b'í fɛ̀ Mi amore (sama chérie bëgg na) Ń délé b'i fɛ̀ kadiñe Baby, ń b'i (sama chérie bëgg na) (Sama alal) nga (N'déka bébé) chérie yama mom (Sama alal) yée (Sama chérie) wayé mala mom (Sama alal) yaw mala mom (N'déka bébé) wayé yama moomé (Sama alal) (Sama chérie) sama chérie bëgg naala Ñokhonnalu kéla ko n'dé yé i boucler (boucler) Ki sécuriser ka kla ki valider Sounna ni farrida laa, ma bien aimée I confirmée laa à la vie, à la mort Taamu naala lumu mëneti déff mane mi bëgg na Tu es ma lumière cachée dans le noir Ooh, mon amour, si seulement tu savais Ma dila, toi et moi, toi et moi Toi et moi, noko bëggée bëgg na Toi et moi, me and you, bébé Noko bëggée bëgg na Ń b'í fɛ̀, bébé, ń b'í fɛ̀ Mi amore (sama chérie bëgg na) Ń délé b'i fɛ̀ kadiñe Baby, ń b'i (sama chérie bëgg na) (Sama alal) nga (N'déka bébé) chérie yama mom (Sama alal) yée (Sama chérie) wayé mala mom (Sama alal) yaw mala mom (N'déka bébé) wayé yama moomé (Sama alal) (Sama chérie) sama chérie bëgg naala Hehehehe, li kuné néxul danga thié bokkul Ba nga bëgg bokk kéne bolléwula sa fii di khassane Sidiki ak vj, ayy, mbété-mbété sukërr Mo saff sapp (sama chérie bëgg naala) Chérie boy (eh, sama chérie bëgg naala) Ma chérie (eh, sama chérie bëgg naala) Sidiki diabaté (sama chérie bëgg naala) Lonkotina lonk na Takkal ma yaw bum ći batt yobbuma Ayy, bébé, ningay doxé néxna ma Té yaw waxma noko bëggée mëne na déff Lonkotina lonk na Takkal ma yaw bum ći batt yobbuma Ayy, bébé, ningay doxé néxna ma Té yaw waxma noko bëggée mëne na déff