Mi ngui naadj, mi ngui liw Mi ngui taw, mi ngui neiger Immigrés ya ngui ci mbéd mii lé Bayi baay, bayi yaay, bayi dom ak diabar Fass yéné khouss ci sédd bii lé Nango door waar Nango bay sene waar yé Immigré moy diambaar Nango door waar Nango bay sene waar yé Immigré moy diambaar Nango door waar Nango bay sene waar yé Maa lén séédél li lé Mi ngui naadj, mi ngui taw Mi ngui liw, mi ngui neiger Immigrés ya ngui ci mbéd mii lé Bayi baay, bayi yaay, bayi dom ak diabar Fass yéné khouss ci sédd bii lé Nango door waar Nango bay sene waar yé Immigré moy diambaar Nango door waar Nango bay sene waar yé Immigré moy diambaar Nango door waar Nango bay sene waar yé Maa lén séédél li lé Bing fi diogué yaag neu lol Té bobak légui meusso taayi ci fadj boumou gaathié yi Bing fi diogué yaag neu, yaag lol Té bobak légui meussoulo taayi ci fadj boumou gaathié yi Lima méti ba méti moy Leg leg niou sédeulé seu guinaw Li moka tiiss Matt naa ci séédé, mane miko doundou Mou yaag té metti lole Té nak sakh massa lene thiono Yene kou lene diourone, yeureum lene (wawaw) Yow mi mouy yoné, boul xééb Xamoulo nimou deff ba am ko Amaana, dadj na thia ay thiono Nguir meuna bay sene waar yé Immigré moy diambaar Nango dor waar Nango bay sene waar yé Immigré moy diambaar Nango door waar Nango bay sene waar yé Maa lén séédél li lé Faaté wouma léne djiguénou immigrées Am nguéne diorama