Saf nga jigéen loolu laa lay toppe Dama la xool li ma gis di ma choqué Ni nga mel naturel la, doo ko forceloo Gel bi dafa tàng ba di lakk Safara biy nelaw ci yaw la bëgga gis Pese naa la ci li nga doon dafa diis Saf ni jimbo, tooy ni rico Gel bi dafa tàng ba di lakk Shut, ak gel booy bu la jege ma shut Li may wër yépp ci jigéen nga uuf Sa béppu moroom bu la tëkk nga shut Shut, shut, shut, shut, shut Baby kaay sama wet Mbëggeel laa lay sedd ma dama jooy Billaay yaay ki may daneel, oh, ooh Bi ma la gisee sama xol dafa neex Bi ma la gisee Baby kaay sama wet Mbëggeel laa lay sedd ma dama jooy Bi ma la gisee Sama lingeer yaa xarade Am nga cas waaw yaa cëkkëte Yaw laay wër suba ba ngoon ma tëddi Yàgg na bari mais waay yaw tu es mon combat Bandit, bandit Baby bandit danditlul Wane sa bandit wëdelul Coow li coow li yaw jugal nga féemu Daggal sa yaram ñu ndellu Shut, ak gel booy bu la jege ma shut Li may wër yépp ci jigéen nga uuf Sa béppu moroom bu la tëkk nga shut Shut, shut, shut, shut, shut Baby kaay sama wet Mbëggeel laa lay sedd ma dama jooy Billaay yaay ki may daneel, oh, ooh Bi ma la gisee sama xol dafa neex Bi ma la gisee Sama xol Bi ma la gisee Mix bi saf na!