Oooh bae, ci sa wet laay fanaan si Yóbbu nga ma sama fit bi danga ma tiital Mbëggeel bi nga ma won ma di ko tiitaroo Buddi xol bi jox la pare jiital la Ak lu ñu bari-bari yaw doo seen moroom Coti yali-yali baby yaay sama chérie coco bànneex Fi nga may yóbbu dafa sori Bi ñuy lewto baby yaa ma daanel Bu guddi gi xaajee Bidéew yi di mellax ci asaman si Nga naan ma baby ci sa wet laay fanaan si Sama xol bi li ciy neex yaa koy sukkar Su ma la gisul damay wet Jongoma, bul ma soreeti Su ma lay woo yaw dee ma faale Soxna si kaay ci sama wet Su ma lay woo yaw dee ma faale Soxna si kaay ci sama wet Eh ma ni kaay, eh ma ni kaay Ma ni kaay ci sama wet Eh ma ni kaay, eh ma ni kaay Ma ni kaay ci sama wet Def ma soxna si def ma fou Gëna sori ci sa xol bi doo ko rëccu Man it ma def la sama lonko Maak yaw sekku ñu bàyyante Alaa accu ou Soo deful ndank dinga ma faat Bae, li nga ma ñamal duma ko fàt-te Këf sama xol ma yoxu sàcce Sunu mbëggeel bi gëna naat my bae Xel bu du jogé ci xelu bi may ray Reewande bi ngay ñoddi yaa ko tay Su melastiku ñaata la ciy fay Delloo la njukkal ba xel bi di ci tey Bu guddi gi xaajee Bidéew yi di mellax ci asaman si Nga naan ma baby ci sa wet laay fanaan si Sama xol bi li ciy neex yaa koy sukkar Su ma la gisul damay wet Jongoma, bul ma soreeti Su ma lay woo yaw dee ma faale Soxna si kaay ci sama wet Su ma lay woo yaw dee ma faale Soxna si kaay ci sama wet Eh ma ni kaay, eh ma ni kaay Ma ni kaay ci sama wet Eh ma ni kaay, eh ma ni kaay Ma ni kaay ci sama wet