Jaral nga ma taxaw feccalla ndaat saay Yaay buuru sama xol kon fu la neex fa laale Ku la son beri nga daan ko Ci digg ëtt bi nu la neex daggoo Farata rekk laa la doon doyee Dama la nob ba am sa faiblesse Lu ëpp turu baby lii dafa fees Dam lay xalaat ba sama xel bi ne mes Lu way dëgger dëgger dinga daanu Say keseng keseng moo may taxa aalu Yeggël sama xel di ma suusloo Yaa raw daju volet bi may taxa metti Risque la, risque la Jee ma dox sa garde risque la Risque la, risque la Jee ma dox sa garde risque la Jalgati jalgati yaw Sama xol bi yaa ko yëngël yëngël Yaw yaa may feccloo ndaat saay Jalgati jalgati yaw Sama xol bi yaa ko yëngël yëngël Yaw yaa may feccloo ndaat saay Lingeer, lingeer Yaw yaa may feccloo ndaat saay Lingeer, lingeer Yaw yaa may feccloo ndaat saay Dëkke di ma caw xiir bi doo baale Dawal sama kaw dee ma yobbale Eh dëgin ndaat saay Eh dëgin ndaat saay Tay ma feccal la dëgin ndaat saay Chéré sama chéri Yaa ma tere nelaw Say cakas cakas sama kaw Lii moo ma tee Def ma ndank, def ma ndank Xale bi dina mësa ray doomu jaambur Yaadi wuurus ngalam Feccal ma tukkusu ngalam Yaay awoo buuru këram Ku mer na fa de yaa fa xam Xale bi amoo moroom Maa la sant gërëm Or nga yëgoo përëm Yaw laay topp dee ma bërëng Risque la, risque la Jee ma dox sa garde risque la Risque la, risque la Jee ma dox sa garde risque la Jalgati jalgati yaw Sama xol bi yaa ko yëngël yëngël Yaw yaa may feccloo ndaat saay Jalgati jalgati yaw Sama xol bi yaa ko yëngël yëngël Yaw yaa may feccloo ndaat saay Lingeer, lingeer Yaw yaa may feccloo ndaat saay Lingeer, lingeer Yaw yaa may feccloo ndaat saay