Tous les jours je pense à nous Au plus beau jour de ma vie Dans ta jolie robe, mon amour Ton visage qui scintille Amul lu gëna neex li ñuy dundu ni Danu ko yàgg dream baby tay moo ngi ni Doon nga sama wife, doon nga sama guy Fi ngeen jugé sori, baby awma sa faay Ani ñi doon douter, takk naa ko! Sama Ouroul Ainy baa ngi, takk naa ko! Maa ko waxoon bébé, takk naa la! Lu waay waxoon na ca delluwaat, takk naa ko! Ñi doon douter, takk naa ko! Sama Ouroul Ainy baa ngi, takk naa ko! Maa ko waxoon bébé, takk naa la! Lu waay waxoon na ca delluwaat, takk naa ko! Bàyyi ma toog [?] Ndax lu ma daw daw daw, yaa ma gëna gaaw Yaa ma gëna gaaw, yaw laay topp Bébé jiitu ma nga raw ma, maa ngi sa ginnaaw Topp sa ginnaaw Naa la xaar âret kaar boo ñëwee yakkal ma say coono Aka ma xam ni fi ngay jaar Dingay def toj-toj waaye yaw yoroo xolu tooñ ma Wax ma ni dama la koy baal Yapp ma yabbale reewande Yapp nga xale bu fiir Client bu mat, client la bu amale caprice Am nga gan boo dul yàkkale, ñépp ay rangé mur Naan ci lewel, naan ci Deus, naanale tarxiis Ani ñi doon douter, takk naa ko! Sama Ouroul Ainy baa ngi, takk naa ko! Maa ko waxoon bébé, takk naa la! Lu waay waxoon na ca delluwaat, takk naa ko! Ñi doon douter, takk naa ko! Sama Ouroul Ainy baa ngi, takk naa ko! Maa ko waxoon bébé, takk naa la! Lu waay waxoon na ca delluwaat, takk naa ko! Ay lolou sama lonko [?] bul sori, yaw kaay waay! Tëdd sa kaw nga ni ma gan Sama reni xol, sama ndaanaan Li ñuy dundu ni Danu ko yàgg dream baby tay moo ngi ni Doon nga sama wife, doon nga sama guy Fi ngeen jugé sori, baby awma sa faay Ani ñi doon douter, takk naa ko! Sama Ouroul Ainy baa ngi, takk naa ko! Maa ko waxoon bébé, takk naa la! Lu waay waxoon na ca delluwaat, takk naa ko! Ñi doon douter, takk naa ko! Sama Ouroul Ainy baa ngi, takk naa ko! Maa ko waxoon bébé, takk naa la! Lu waay waxoon na ca delluwaat, takk naa ko!