J'te tampi yaay wër di wax noppil Dëkke di ma yàq fépp Laisse-moi vivre tranquille Arame, Modu, Bada, Samba, Fatu Bint Ne nañu yaa ma waxal fii lu ñaaw Khady, Maty, Mami, Coumba, Assane, Lamine Ne nañu yaa ma toog fii lu ñaaw J'te tampi yaa ngi wër di wax noppil Dëkke di ma yàq fépp Laisse-moi vivre tranquille, waaw Xaajatuma ci koñ bi fu ma dem Ñu ne yaa ma waxal fii lu ñaaw Djiby Néne, Hamdy, Mass Bu ma gis ne ma yaa ma waxal fii lu ñaaw Doxal ba kenn laal la Bul ko ragal waxkat la boy Amoo lu ñi tiit mafia bi Jugleen ñu yóole Dëkke di ma peinture Lu la neex defal boy Mënoo ci man dara tus Lamb sama poche Faj soxla lu ko gëna neex Tas sa yaakaar tasar Yere fa mu moole (dama koy sappée) Dàll fa mu moole (sappée) Montre fa mu moole (dama koy sappée) Classe fa mu moole (sappée) Xeñal lu leex di ko romb xol ba di bon (mu yeen) Ci soxar ba la Dina yàq sa der bi toog la ki mooy ku bon Han yeah ci iññan ba la Su ma la gisee ngay kaf di ree Su ma la wanee ginnaaw ngay wax ci man lu ñaaw Lu ñaaw a ñaaw a ñaaw Lu ma la lebal hum lu ñaaw Yàlla noppi na du tay, lu baax la bon di fay Ma la bëgg mais du yaw lu la bon di may Ma la wax sa bopp tay du ma ku lay jaay Yónnu yax amul mujj ngalla bu si wey Lii ñaaw na, sama noon bi loo nar tay Lii ñaaw na, wax ma loo nar tay Man fu ma dem ñun sa noon bi jaar na fi yàq la jaratoo fi dara Non ooh, doo sama xarit mooloo Àddunak li ci biir, sukker du ko tere fen Maa ngi ci biir amul tus Doxal ba kenn laal la Bul ko ragal waxkat la boy Amoo lu ñi tiit mafia bi Jugleen ñu yóole Dëkke di ma peinture Lu la neex defal boy Mënoo ci man dara tus Lamb sama poche Faj soxla lu ko gëna neex Tas sa yaakaar tasar Yere fa mu moole (dama koy sappée) Dàll fa mu moole (sappée) Montre fa mu moole (dama koy sappée) Classe fa mu moole (sappée) Xeñal lu leex di ko romb xol ba di bon (mu yeen) Ci soxar ba la Dina yàq sa der bi toog la ki mooy ku bon Han yeah ci iññan ba la Mënoo ci man dara tus Mu yeen ca soxar bala Tas sa yaakaar tasar Han yeah ca iñaan ba la