[Iblow] Bh, bh, bah, bah, bah Bakkal ma nder ma seeti siŋ-siŋ Nobeel feeñ ma def feem Xel dafa yëg netalli xol Mb-mb-mbëggeel bi daw na yaram waaye cat mooy col Il n’est jamais trop tard Il n’est jamais trop tard Sa xarit ñépp a mariée Góor gu ne bëgg la marié Yaw nga ni man rekk lay doon [Awa thies] Yaa fondement sama amour May féey sa geej ni dieu ne yaa ma napp, waay! Tej ma sa xol ba mu mel ni, yaw la (yaw la) [Pape bilal] Li ndox di def ci jën Nu ko raw ngay def ci man ma la bëgg, waay! Kaay toog ci xol bi bañ a dem, yaw la [Awa thies] Sama xol ba mu faiblé Yaay ki ko chargé ba mu fees waay! Ki tax xol biy daŋ-daŋi, yaw la [Pape bilal] Sama coco ananas biy neexal xol bi, yaw la [Awa thies] Mar naan sax du la tax a dikk [Pape bilal] Nopp a dégg bët yi gis Xel ni ma xol bi, yaw la [Awa thies] I love you! [Dane & awa thies] Yaw xanaa xamuloo Yaw gisuloo ni yaw la (Bu dul yaw du doon keneen) Yaw xanaa xamuloo Yaw gisuloo ni yaw la (Sama xol bi ne na yaw la, waay!) Yaw xanaa xamuloo Yaw gisuloo ni yaw la (Waa mbedd mi ne nañu yaw la, waay!) Yaw xanaa xamuloo Yaw gisuloo ni yaw la Suñu waa-kër ne nañu yaw la, waay! Man ki ma bëgg dafa pare waaw Amul temps-wu wax ak gaa ñile [Fatel] Yaa ma leen gënal (yaw) [Dane] Kon fu ma jaar ñu ne waaw [Fatel] Chéri, chéri yeah Ki ma gis sama rêves yaw la [Waly dieng] Man danga laajal sama xol bi Moo tax sa xel la koy lëmbe, waay [Fatel] Yaw toj nga sama ndon bi Est-ce que liggéeyoo ma? [Waly dieng] Baby, sa nobeel a fort waaw Gis nga mbëggeel su la jàppee! [Waly dieng] Dafay mel ni courant ci ndax waay! Bébé, defal lu la neex fi nga ne ci xol bi jugé woofa [Fatel] My baby, dolli ma Xam nga ni buur bi yaw la! Yaw ni nga ma bëggee chéri Nu ka raw la la bëggee, waaw Man nii laa la bëggee, eeh yeah! Wan la mbëggeel ba mu neex chéri Xamal ni yaw la! [Waly dieng] Tay ma lamb-lambee sama chéri coco Waxal la sa mbaax damay neex waay [Waly dieng] Yaw baax nga yaatu nga yaw Tey nga màndu nga chéri coco Man bëgg naa sama chéri [Dane & awa thies] Yaw xanaa xamuloo Yaw gisuloo ni yaw la (Bu dul yaw du doon keneen) Yaw xanaa xamuloo Yaw gisuloo ni yaw la (Sama xol bi ne na yaw la, waay!) Yaw xanaa xamuloo Yaw gisuloo ni yaw la (Waa mbedd mi ne nañu yaw la, waay!) Yaw xanaa xamuloo Yaw gisuloo ni yaw la Suñu waa-kër ne nañu yaw la, waay! Man ki ma bëgg dafa pare waaw Amul temps-wu wax ak gaa ñile [Fatel] Yaa ma leen gënal (yaw) [Dane] Kon fu ma jaar ñu ne waaw [Azou] Naka sa duguda Est-ce que chéri mi ngi ngallax Ndox mi est-ce que mi ngi ngallax Naka sa duguda Hey ba mi ngi ngallax Naka sa duguda Est-ce que chéri mi ngi ngallax Yaw ku ci nob sa chéri yaw ma ko bii-bisouuus! (Muac-muac) Wéy, su la neexee ray ko ndax xol bi neex Rayal, ray rayal ba mu neex! [Dane & awa thies] Yaw xanaa xamuloo Yaw gisuloo ni yaw la (Bu dul yaw du doon keneen) Yaw xanaa xamuloo Yaw gisuloo ni yaw la (Sama xol bi ne na yaw la, waay!) Yaw xanaa xamuloo Yaw gisuloo ni yaw la (Waa mbedd mi ne nañu yaw la, waay!) Yaw xanaa xamuloo Yaw gisuloo ni yaw la Suñu waa-kër ne nañu yaw la, waay! Man ki ma bëgg dafa pare waaw