[Dane] Sooy toogati duggal ba sa biir nekk Xeet gi sonal naa waa-kër gi, waay [Fatel] Eh bul ma tooñ duma sa moroom waay Kër gi dangay fay man it damay fay [Dane] Yeen lu neex way def ngeen bëgg dunde ci kër gi Non non, xooleen ci dëkkaando yi [Fatel] Kon góor dangay màndu régler ñu jox la cër noppil Lijjantil sa nekk bee [Waly dieng] Eh samba ndiaye Boo duggaate ci duus bi de si def ndox waay [Fatel & dane] Ha ha ha ha! - yor pan, di lijjanti siwo jaambur Waxal ci le waay! - he, dimbali ma! [Dane] Yaw yaa ma yàpp waay Boo ma waxaate lu ma deful dinaa la duma [Waly dieng] Samba ñëwal, yaw laay xaar [Dane] Eh, man duma sa moroom de! [Awa thiès] Ñoo bokk ndey book benn baay Loolu tax ñu tokk fi tay Booloo war na ñoo kër gi doon benn Kon sama waay teeñoo boolo [Momo] Waa-kër gi te ñoo booloo Waa-kër gi te ñoo booloo Waa-kër gi te ñoo booloo Waa-kër gi te ñoo booloo (Discussion) [Mya blacky] He lamine diop waññil sa radio bi Kenn mënul nelaw kër gi yeen a lakkale, waaw [Pape bilal] Su ma neexee maa tay léegi Yaw yaa sof mel ni yaay fay sama nekk waaw [Mya blacky] Yaa ma gën a sof tànkal guddi tankal bëccëg Eh lamine diop ameel nga ak dëkkandoo yi [Pape bilal] Jigéen du ma yuxu, jigéen duma fontoo Marème puusal bala ma lay songu [Waly dieng] Soo ko dooree eeh waaw Soo koy dóoree maak yaw la na la doon fii (Discussion) [Awa thiès] Ñoo bokk ndey book benn baay Loolu tax ñu tokk fi tay Booloo war na ñoo kër gi doon benn Kon sama waay teeñoo boolo [Momo] Waa-kër gi te ñoo booloo Waa-kër gi te ñoo booloo Waa-kër gi te ñoo booloo Waa-kër gi te ñoo booloo [Iblow] Prési bàyyil xel askan bi Bàyyil xel économique bi Confinement da wara jeex Prési jaar nga fu metti xam nga luy pas de boulot Chaque jour xuloonuñu suñu dundu safatul neex [Azou] Hey yaw moomu lasa dundu safatul neex Sonal nga ñu waay! Rap guddi rap bëccëg Dem nga sax ba kër ñépp amee rap di xuloo [Iblow] Hey duma wax ak fecckat nax awma jotam [Azou] Hey fecc ma gënal waxtu guddeek bëccëg Dëkke wax dëkke ray dëkke tekk xel ba xiif [Awa thiès] Hey bàyyil ma fecckat bi te nga dem jëndal ma fël-fale ci boutique bi [Iblow] Kan man yaw yaa yabbate yaw Man may real rappeur nga may yónni ay saf-safal He, xoolal soo bëggee sa fekk danga koy danga koy wëri [Azou] He he heeey Moo safal, yaa koy safal He safal, yaa koy safal Hey, ba kër gi fer! [Awa thiès] Ñoo bokk ndey book benn baay Loolu tax ñu tokk fi tay Booloo war na ñoo kër gi doon benn Kon sama waay teeñoo boolo [Momo] Waa-kër gi te ñoo booloo Waa-kër gi te ñoo booloo Waa-kër gi te ñoo booloo Waa-kër gi te ñoo booloo