Amour bu sincère Amour bu fidél oh Ki dox ci li ma neex Di ma wax wax ju neex Une personne sincère Ku bëgg boppam ooh Te am dignité Teg si doon ku nite heee hii yee Bëgg naa ki may bëgg ma bëgg ko Ñuy dundu lu neex di muñalante Moom la yàgg wër te gis naa ko waaw Xale bi ma yàgg wër de yaw la Ki ma doon seet de gis naa ko Oh my chéri, you are my baby Xale bi ma yàgg wër de yawwu la Ki ma doon seet de gis naa ko Oh my chéri, you are my baby Ku ko xamul tamit dégg nga écho bi Sama love de lay wër Mali ba Éthiopie France, Italie, wëri naa ko Tugal Avis de recherche, tapé naa ko Google Mbëggeel bi nekk ci kaw (aan, ci kaw) Du ñëw ci suuf (heeey, du ñëw, du ñëw, du ñëw) Ndax moom bu ñëwee da koy gaañ Bëgg naa ki may bëgg ma bëgg ko Ñuy dundu lu neex di muñalante Moom la yàgg wër te gis naa ko waaw Xale bi ma yàgg wër de yaw la Ki ma doon seet de gis naa ko Oh my chéri, hmm you are my baby Xale bi ma yàgg wër de yawwu la Ki ma doon seet de gis naa ko Oh my chéri, you are my baby Wëri ko, fils wëri ko Si mu lay neex moo la ko jaral waay! Wëri ko, fils wëri ko Si mu lay neex moo la ko jaral waay! Man wër naa la fu ne Baby jar nga ko, chérie This is looove, waawaaw Yaa ma ko jaral, chérie, laaj naa la fu ne Baby jar nga ko, chérie This is looove, waawaaw Ci bu lay neex, ma jox la ko ba mu jeex Xam nga jar nga ko Baby jar nga ko, chérie This is looove, waawaaw Tileel sama xaritoo xol, xam nga jar nga ko Baby jar nga ko, chérie This is looove, waawaaw