Je ne veux pas vivre sans toi Dans mes rêves je te vois J'ai vu l'amour en toi Nalingi yo, nalingi yo Si tu le dis je te crois Tu es mon amour, mon roi Je veux rester avec toi Nalingi yo, nalingi yo My baby ooh Rongooñ tuuru na ca mbëggéel kersa du fa am Na li-lingi-lingi yo, jaral nga ma (Bébé jaral nga ma) Ma di la feccal, di la wayal Lu mu jar ma def ko, pare naa Su météo doon gis mbëggéel, asaman neex Taw lay dëkke ba fàww Sori ci man, jege ci man Mbëggéel a bari doole Xol buy bëgg du tàggoo Def naa la xarit Sama chéri Oh, man dama la love ni July ak Roméo Xale bi yaw ar gaay Ñëwal fii nu bége yaw Danga dof ci man, ma dof ci yaw tu sais Nawet nga yaw, tawal mu gaaw je sais Yaa dàq lem, dàq ceeb ci neex Bu ñu dund lu original ba romb septième ciel (hee) An kaa gidelam (hee) An kaa sehilam (hee) Je ne veux pas vivre sans toi Dans mes rêves je te vois J'ai vu l'amour en toi Nalingi yo, nalingi yo Si tu le dis je te crois Tu es mon amour, mon roi Je veux rester avec toi Nalingi yo, nalingi yo Tu m'as fait bae halluciner Te man je sais bébé, allons dîner Yeaaah, ku bëgg te fowul Ngoram du ko jaay Bul wanteer du fëgg jaay Xol lu ci njëkk a dugg, nobeel moo ko maye Fii du marché yebbi, du Colobane bu ñu ray Aywa leen, aywa leen Ku fi gis xol buy jaay Je ne veux pas vivre sans toi Dans mes rêves je te vois J'ai vu l'amour en toi Nalingi yo, nalingi yo Si tu le dis je te crois Tu es mon amour, mon roi Je veux rester avec toi Nalingi yo, nalingi yo Sori ci man, jege ci man Mbëggéel a bari doole Xol buy bëgg du tàggoo (Nalingi yo, nalingi yo) Su météo doon gis mbëggéel, asaman neex Taw lay dëkke ba fàww