Kay ma diayla mbeuguel bou deugou Ak xol bou nice, bou ande yeurmandé Kay ma diayla li nga geuneu beug Djiguen bou bax dey wax deugeu Kay ma diayla mbeuguel bou nex Tek diayla sincérité bou werr bodoul guiss fénén Gorr amna fi ak fidel bou yomb Nobel amna fi, nobel bou nior khomb Lo fay gaw, waxal waxal, lo fay gaw Amoul waxalé Lo fay gaw, waxal waxal, lo fay gaw Louma dadialé, dadialé na pour dieunderou plaisir Ay sacou bisous, je t'aime bou bax Amna samou maikeur Amna samou nobel Amna samou mougn ak doylo waw Mbeuguel ma diaye, mbeuguel ma diaye Mbeuguel ma diaye, mbeuguel ma diaye Magie beugeunté ngui ni Mbeuguel rek lay diaye Ioe fayal sa impot sa diouti avant ngey diaye Et puis dama beug xol bou sincère goor bou ngeub Kouy yeureum djiguen tek si diko wax Lo fay gaw, waxal waxal, lo fay gaw Amoul waxalé Lo fay gaw, waxal waxal, lo fay gaw Louma dadialé, dadialé na pour dieunderou plaisir Ay sacou bisous, je t'aime you bax Amna samou maikeur Amna samou nobel Amna samou mougn ak doylo waw Mbeuguel ma diaye, mbeuguel ma diaye Mbeuguel ma diaye, mbeuguel ma diaye