[Pape bilal] Woo naa la jotuma la, lu waral lii? [Awa thies] Bébé sama yaay booy moo jël sama téléphone [Pape bilal] Laaj naa la say xaritoo kenn gisu la [Awa thies] Bébé sama baay booy moo tax génnuma [Pape bilal] Gis naa ni danga changé Ay copine yu bees ngay fréquenté [Awa thies] Man jàmbatumaak sa jikko ju changé Ngay kebatu naan, chiiium! (Ah bon?!) [Pape bilal] Indil prique bi nga takk maa ko jënde [Awa thies] Su mil kalson bi nga sol maa ko jënde [Pape bilal] (Ih yaw kañ nga jënde kalson bi?) [Awa thies] Si dàll ba yére sa lépp maa ko jënde [Dane] Àdduna bi boo ci nekkee dal! Fawu ngay muñale pur ñu lay muñal (Maram ak biram nàmm naa leen) Muse, où est madame? Seytaane bàyyileen ñu séy Madame, ani muse? Seytaane bàyyileen ñu séy, waaw [Fatel] Cinq cents fois ngay jooy dépanse Man dootul man [Waly dieng] Xool na xool waaye danga ma yab Loolu heey yaw moytuma [Fatel] Man awma lu may wax ak yaw Góor gu yàccaaral day mel ni yaw [Waly dieng] Fàtte woon nga bi ngay ñëw fi Ya rawoon baale bee [Fatel] Sama pàpa moo ma tooñ bi ma maye May ma sama baat léegi sayee [Waly dieng] Sa pàpa num la tooñe la bëgg a xam man yaw Yaa yàgg nga jooy [Fatel] Yaw xanaa doo rus sax, yàgg nga wax Maa la gënal sa yaay sax [Waly dieng] Way! Yaw danga rew wala danga dof? [Fatel] Ma ni ma money yaw amoo ko maa ngi séy! [Dane] Àdduna bi boo ci nekkee dal! Fawu ngay muñale pur ñu lay muñal (Maram ak birmane nàmm naa leen) Muse, où est madame? Seytaane bàyyileen ñu séy Madame, ani muse? Seytaane bàyyileen ñu séy, waaw [Ay jigéen] Moom de dafa mel ni ku ragal jëkkër ji! Daa ko waroon jàppu dóor ko dóor yu metti Ki doy na war way! Yaw bàyyil ma ki man bu doon man Ba ma tàngal sama diwlin ne ko ko cër (ayyah) [Iblow] Man jaaxle naa, jaaxle naa ci koñ bile Ñoom yàkkamtiwuñu lu dul xeex bañ jubile [Azou] Hey bro fi la bët yam Mais xoolal alma ma naan man ci juis bëlé [Iblow] Ñoom ñépp dañ kumpa gaaw mel ni ñobaar (nga ni?) Koñ baa ngi tang mel ni dañ fi sotti poobar [Azou] Ihhh saf na, kon saf na Saf na, poobar bi saf na [Dane] Àdduna bi boo ci nekkee (yaay) Fawu ngay muñale pur ñu lay muñal (Maram ak birman nàmm naa leen) Muse, où est madame? Seytaane bàyyileen ñu séy Madame, ani muse? Seytaane bàyyileen ñu séy, waaw