Boula Dara Méti

Admow

    Continúa después del anuncio

    Yenn saay nga foog ni
    Ci àdduna bi kenn du la comprendre
    Sometime nga dem ba jàpp ni dooto mës a kontaan
    Ci biir kër gi
    Yaay boy néneu du la may nada, nada
    Ci mbedd mi yeah yeah!

    Ragal la tax nga ni do mayé dara, dara
    Mais nak bul jaaxle, yoon la bu jafe
    Wante ma di goor bi xam fi nga féeté
    Xam sa ndjeugue nga tax ma dëkk ci di ñafe yeah, humm!
    Coofel la ngi ci biir xol bi
    Jox ma confiance ma yóbbu la fu sori
    Ouh baby, ohh baby yeah yeah !

    Continúa después del anuncio

    Dama la love love love
    Baby love love love
    Bu la dara metti
    Naqar jeex na tay
    Ma ngi ci sa weet bu la dara metti
    Dina la téwal ci naj
    Téwal la ci kérr bu la dara metti oooh!
    Baby I got your back, bu la dara metti yeah!

    Ouuu ouuuh ouuuh !
    Écoute-moi, baby
    I love you lady
    Et je sais que t’as peur de m’aimer
    Si tu t’inquiètes pour moi t’as tord
    Faut que tu dormes de ton décor
    T’as déjà gagné mon cœur
    Donne-moi ma chance fais un effort

    Información de la canción

    Composición:

    ¿Los datos están equivocados?

    Enviar revisión