Dama La Love

Akhlou Brick

    Continues after the ad

    Bébé yaw ba namm nga ma
    Man dama la namm ba namm ni ma la nammee yeah
    Te yaw bébé tam nga nak
    Jël peage bi raw ma mais nak tey ma fële pé yeah
    Bébé yaw ba aimer nga ma
    Man dama la aimer ba aimer ni ma la aimer yeah
    Te yaw bébé jaral nga ma
    Doxe ak ay dal weñ ci desert bi ba mu jeex yeah (ba mu jeex, ba mu jeex)

    Def ma ndank yaa ma mën ci pét ma nanguwat ko
    Ci jamm lay dox
    Waxoon naa la ko ci suba faw ma bamtuwat ko
    Dama la love

    Def ma ndank yaa ma mën ci pét ma nanguwat ko
    Ci jamm lay dox
    Waxoon naa la ko ci suba faw ma bamtuwat ko
    Dama la love

    Continues after the ad

    Baby dama la, yaw dama la love
    Te ànduma ceek sago
    Baby dama la, yaw dama la love
    Maa la toppe dina dof baby
    Baby dama la, yaw dama la love
    Te ànduma ceek sago
    Baby dama la, yaw dama la love
    Maa la toppe dina dof baby

    Ne nga man rekk ma lay tooñ
    Wante bu dul man keneen kan moo ko saañ
    Ne nga may génnee sa rangooñ
    Ma lay tooñ ba fu tooñe dikk ba lu la tadoo bañ bae
    Yenn saay dinaa yëkkëti baat
    Mer ne la may naa la baat
    Yaram bi daw ma réccu wax ju ñaaw
    Ñëw di la baaluwat naan la bae dama doon foo
    Dama tam ay waxu con, xanaa du may Tom yaay Jerry
    Bëggante mënta ñak coow yaw, sekkuñu demal ma dem
    Awma mot xep-na je t'aime moo tax ma lay wax dama la bañ
    Mais dama la nob mënul am prix yaw am nga prix nobel
    Man dama la nob, dama la nob ba lab ci geeju nobel, Love you!

    Def ma ndank yaa ma mën ci pét ma nanguwat ko
    Ci jamm lay dox
    Waxoon naa la ko ci suba faw ma bamtuwat ko
    Dama la love

    Def ma ndank yaa ma mën ci pét ma nanguwat ko
    Ci jamm lay dox
    Waxoon naa la ko ci suba faw ma bamtuwat ko
    Dama la love

    Baby dama la, yaw dama la love
    Te ànduma ceek sago
    Baby dama la, yaw dama la love
    Maa la toppe dina dof baby
    Baby dama la, yaw dama la love
    Te ànduma ceek sago
    Baby dama la, yaw dama la love
    Maa la toppe dina dof baby

    Song details

    Composition:

    Did you see an error?

    Enviar revisão