Ay way chéreey, chéri coco
Yaa ma té nelaw, woy naa la
Chéri sama ndaanaan, yaa ma té nelaw
Ay way chéreey, chéri coco
Yaa ma té nelaw, woy naa la
Chéri sama ndaanaan, yaa ma té nelaw
Ndeysaan chauffeur bu ndaw balay julli jàpp
Toog ci dér di ñaan lu mu ñaan
Yàlla may ko ko dégel kile jaara may sa doom
Bigué, Ndari Coumba Bigué
Soko Diack Ndélla Ngoné
Chéri kaay fóon ma, yaa ma té nelaw
Dialo Dialoooo, ohoh Diallo
Ma ne Ngoné Arame Mbaye dem na
Nii Diaaalo
Ey, yaa ko jomb a ñaaw yaw
Ay way Demba da li Meisa Diop
Bidéew Goorga Diodio Ndiaye
Digëntem Maragan nokobe
Thialo Yacine Ndiokhobaye dem na
Oh non!
Socé Fall Dawour Fall
Massamba Ndoumbe Fall
Ñoo mënoo ca lang Sambo
Meïssa Coumba Bigué
Lari Coumba Bigué
Soko Diack Ndella Ngoné
Chéri kaay fóon ma, yaa ma té nelaw
Baay Chérif lënde diaddi yaram
Loo fi ñaan mu nangu ñaanal ñu
Yaw de lañu rañe léer na àdduna
Ay way chéreey, chéri coco
Yaa ma té nelaw, woy naa la
Chéri sama ndaanaan, yaa ma té nelaw
Ay way chéreey, chéri coco
Yaa ma té nelaw, woy naa la
Chéri kaay fóon ma, yaa ma té nelaw
Ndeysaan, chéri coco!
Amul géer, amul géwél
Chéri sama xol boo meloon ni man
Ñu yëngël ko cee