Alxames (feat. ILAM)

Ashs The Best

    Continúa después del anuncio

    Bësu alxames bu tiis, ci waxtu timis
    Ci lañ ma diis, naqqar bu tiis
    Alxames bu tiis, bu tiis a tiis
    Ci lañ ma diis

    Suma waaji dem na (dem na)
    Dem na (baayi fi njaboot ji)
    Dem na (ñëpp a koy jooy)
    Dem na (weetal na kër gi)

    Suma waaji dem na (dem na)
    Dem na (baayi fi njaboot ji)
    Dem na (ñëpp a koy jooy)
    Dem na (weetal na kër gi)

    Salaama yaa seydi
    Salaama yaa Baaba
    Taalibe Maam Ba′mba
    Xol bi rafetoon na
    Jamm laa la yeene
    Doonoo woon alie'ne′
    Aljana Firdawsi laa la yeene
    Salaama yaa seydi Baaba

    Continúa después del anuncio

    Suma waaji dem na (dem na)
    Dem na (baayi fi njaboot ji)
    Dem na (ñëpp a koy jooy)
    Dem na (weetal na kër gi)

    Suma waaji dem na (dem na)
    Dem na (baayi fi njaboot ji)
    Dem na (ñëpp a koy jooy)
    Dem na (weetal na kër gi)

    Ebe njaxaa be ngandaa tobe fay
    Be ngalaa kobe ñaami
    Dum ne muusi ni xaw nii, ni xaw nii
    Sukaabe Africa ngummo deen
    Sukaabe Africa ngummo deen, ngummo deen
    Liggo deen leydi meen saare meen
    Ñoo foowandoo Maggandoo
    Def nañ lu ne, jaar nañ fu ne
    Lima la yeene, Aljana laa la yeene
    Doonoo woon alie'ne', Taalibe Maam
    Ba′mba Sa jëf ji rafet na Baaba

    Bësu alxames bu tiis
    Ci waxtu timis
    Ci lañ ma diis
    Naqqar bu tiis
    Alxames bu tiis
    Bu tiis a tiis
    Ci lañ ma diis

    Suma waaji dem na (dem na)
    Dem na (baayi fi njaboot ji)
    Dem na (ñëpp a koy jooy)
    Dem na (weetal na kër gi)

    Suma waaji dem na (dem na)
    Dem na (baayi fi njaboot ji)
    Dem na (ñëpp a koy jooy)
    Dem na (weetal na kër gi)

    Información de la canción

    Composición:

    ¿Los datos están equivocados?

    Enviar revisión