Jërëjëf La Diva

Demba Guissé

    Continúa después del anuncio

    Coumba Gawlo, boo leen xamoon
    Ki fu mu jaar mooy jaambaar
    Coumba Gawlo, boo leen xamoon
    Ki fu mu jaar mooy jaambaar

    Yàgg nga sigil Senegaal
    Ci bitim reew ak ci Afrika

    La femme battante
    Une référence
    La grande dame
    Qui n'a jamais perdu sa valeur
    Eeee, la diva
    L'internationale
    La voix d'or
    Une fierté africaine

    Continúa después del anuncio

    Fi nga jaar, képp ju fa jaar
    Bu dul jaambaar dinga daw
    Monument nga ci Afrika
    Gàcc ngalama la diva
    Mabousso Absa Ndiaye
    Ablaye Daro mbaar
    Madior Matar ak Diarra
    Madiama Yassine Daour ma ca lodo
    Fatou Kinpe Mbaye sa yaay di sa xarit
    Laye Bamba Seck sa baay Gawlo
    Eeeeee! Sa baay dalaa ñaanal dooga dem

    Gawlo, Gawlo
    Gawlo, la diva Gawlo (voix d'or du Sénégal)
    Gawlo (ci Soweto)
    Gawlo (étoiles meilleure chanteuse moderne)
    La diva Gawlo (double disque d'or)
    Gawlo (disque platine)
    Gawlo (Kora Awards)
    Gawlo, la Diva Gawlo (fondatrice fem fm)
    Gawlo (marraine aux Nations Unies)
    Gawlo (ambassadrice de bonne volonté)
    Gawlo (lumière pour l'enfance)
    Merci, Club Gawlo

    Yoooo
    Mala yoo, mala yoo
    Ala Torodo
    Maal Diaka yooo

    Información de la canción

    Composición:

    ¿Los datos están equivocados?

    Enviar revisión