Continúa después del anuncio

    Come On! Alkati ya ngi sa kaw
    Thiap bi nga doon xam naniou ni ya ngi ak xalissak drogue
    Wa bou yabo nanal ci sa Safara yi dieul garap bi xeupo
    Thiat ci sa maw laff yi la tok
    May sa thiabi kasso, mane la may Picasso
    Parce que boudone man xamna di nga sol
    Lou eupeu att nga ndara woor kay niu nafila bokk
    Père Noel raciste la mane moussouma guiss cadeaux
    Guiss na ay Pa yu djaay sen taxi pour am passou avions
    Atoum leumb souma nekhé douma liguèye
    A tout moment meune nga déh ni ngoumba ci Guedj
    Dou ben bopp rek nek ci mane
    Def lou yomb rek méti ci mane

    Kouy topando mane ak yaw nouro wouniu système
    Yallah loutax ma dée ni kou dioudo ci cimetière?
    Mouno wa Rap'Adio kone non meuno li DIP Def
    TLK dou Album, dou maxi, non non dou mixtape
    Yaggo tchi kaw ni boy bou ndaw bou tiim Jail
    Rap bi dafa yombone nioune niossi soti dindière
    Ndiago bi moy Boss pourtant moussou massi djékkeu
    Douma lekk kou souroul parce que dama xiff ndeim
    Na def lou eup 1000 scènes, encaissé plus de 1000 chèques
    Sa Papa, Sa yaye ak baag bi lay souleudo ci tenn
    Maf-fu Hip Hop bi mo raw bi ci Goudi Town
    Rap bi dou djoug ndakh boy bou am buzz outi daanou

    Continúa después del anuncio

    Boul mousseu ni yafi meun Témanéfi
    Yaye boul niaanati kèneu Témanéfi
    Marozik mounoul xonett ndakh ma ngi fi
    Sokhla wuma kèneu kumay temoigné fils
    Boul mousseu ni yafi meun Témanéfi
    Yaye boul niaanati kèneu Témanéfi
    Idy namoul iPhone 6 ndakh ma ngi fi
    Sokhla wouma kèneu kumay temoigné fils

    Dé lène Diaamou Yallah té nguène gueum sen bopp
    Bèneu lama may mane ma woute yeneen 2 cerveaux
    Même handicapés yarramam day ndaw
    Wayé kou Fan Pée (1er) bi toujours deuss (2eme) lay done
    No def ba degg Jàmm ci deuk bou dégueulasse bi
    Yëk Carrapid, bokk nëk ak Pa' bi
    Mama ress la, ress sa rakk yi
    Réro demb téyeul sa lamiñ
    Sénégal moy deukou Téranga mais amoul restaurant du coeur
    Kone loy xalate ci boy yi moussoul ray sen bopp beug xexal
    Afrique
    Liberté moussoul am nigger fuck 4 Avril
    Dictateur rek ba déh ni Colonel Khadafi
    Bandit yi yéwou yeup ngi def, ñi gueuméintou dem teudi
    Jail
    May Punch ba ndel Kocc Barma té dougneko nétali kèneu
    Nigger douggou na palais xamna donou Président
    Boul Rap toujours rek fexel ba am comme li Jay-Z am
    Boy Grand yoff, Arafat boy xamna fou BOON bou nekh bi am
    Meune nagnema faat wayé mounou niouma fatté
    Dioudou waat na ba sonneu mais bène yoon lay dé
    Gars yima gueumoul wone légui gueméwouniu ma
    Naukhaur yi lekkone nagnema bu yagg souma deumé woul woone
    Yen ñeup souma len eupone alal di nguène ma faral
    Comme gars yi am ay milliards, milliards pour am ticket
    Safara
    Sama succès bou rèèn niggers wérenté nako daw
    Yen ñeup ken dou ame louko nekh ni ay waraté kat ci boîte
    Dama done djaap sama gars yeup faaté yèèneu texte yi
    Bayil ma diéma djaap text yeup faaté yèneu gars yi
    Niit yi xalaté touniou xel ndakh seug séni sex
    Motakh makk dou jog ci teudé rakkam ni Ci-Yénekaay yi
    Boy guél yeup leundeum dou foula nekh ngay toufli
    25 ans baayil ma doundou comme si Papa nékatoufi
    Batay mane may wakh loutakh nièneu ñi di taf sen guémiñ
    Yaay sa dome dou wadd ni rongagnou ray kattou niit
    Morée

    Boul mousseu ni yafi meun Témanéfi
    Yaye boul niaanati kèneu Témanéfi
    Marozik mounoul xonett ndakh ma ngi fi
    Sokhla wuma kèneu kumay temoigné fils
    Boul mousseu ni yafi meun Témanéfi
    Yaye boul niaanati kèneu Témanéfi
    Idy namoul iPhone 6 ndakh ma ngi fi
    Sokhla wouma kèneu kumay temoigné fils

    Información de la canción

    Composición:

    ¿Los datos están equivocados?

    Enviar revisión