Li Nek Fi

Icône

    Continúa después del anuncio

    Su ma jummul mos naa la gis yaw
    Ci benn jootaay (aywaay)
    Yaa ngi toog ak say gay
    Ngeen tek cay
    Lu ñu wax nga ree
    Di ma xoolale, di ma piisaale
    Man may dee

    Duma la ko nëbb ba ma la gise
    Am na lu ma doon yëg ci suuf (mu fey)
    Nga ñëw toog may ree ci kaw
    Bañu naa sama gay yi di ma ree
    Moo tax yaw mi yëgoo woon

    Aaaan sama mbëggeel

    Leer na ma ba leer
    Naqar dina jeex
    Man ne de li ma gis la leer na
    Aaan leer na ma, leer na

    Li nekk fi ni, li nekk fi ni
    Li ne sama xol
    Mbëggeel la ma jox (moom la ma jox)
    Mbëggeel la ma jox (moom la ma jox)
    Xamewuma ko woon
    Ndéké yoo moom la woon

    Li nekk fi, li ne sama xol bee
    Mbëggeel la ma jox
    Moom la ma jox
    Aaan moom la ma jox (eeeeh khé)
    Xamewuma ko woon
    Ndéké yoo moom la woon

    Continúa después del anuncio

    Ndax mbégte leer na ma ba leer
    Naqar dina jeex, sama àdduna
    Ndax sama nooflaay yaakaar naa
    Dina ma nopal

    Coups de foudre moo ma daal ma lay gis man
    Taw te na gis TaaTa Khouss man
    Fële na si géej mbëggeel man
    Ma bañ fa laay des man fa laay sobo, oh aye

    Li nga ma jaral mënuma ko wax fini
    Yaay sama cooppàti
    Papa Ndiaye takkal ma bin-bin

    Ey, takkal ma xol
    Je t'aime tellement
    Tu mérites ma yóbbu la yaw mi
    Ci Mame Ndiaye Savon

    Esk doo def farata ma gaaw ñëw
    Gallé ñu paccal lingom

    Kuy sa marie de vipère
    Diadia bul dof

    Duma ko laal, dafa bari
    No no bul dof

    Yaw mi fatal ma foofu
    Foo foy

    Li nekk fi ni, li nekk fi ni
    Li ne sama xol
    Mbëggeel la ma jox (moom la ma jox)
    Mbëggeel la ma jox (moom la ma jox)
    Xamewuma ko woon
    Ndéké yoo moom la woon

    Li nekk fi, li ne sama xol bee
    Mbëggeel la ma jox
    Moom la ma jox
    Aaan moom la ma jox (eeeeh khé)
    Xamewuma ko woon
    Ndéké yoo moom la woon

    Información de la canción

    Composición:

    ¿Los datos están equivocados?

    Enviar revisión

    Canciones relacionadas