Allamé (feat. Malakey)

Jeeba

    Continues after the ad

    Hello, ooh ooh wa
    Yow chérie yaa ma yaa ma wara wuyu
    Aaah, aaah aah aah
    Yaw chérie yaa ma wara wuyu
    Décroche ton téléphone, ne me laisse pas he
    Chérie yaa ma wara wuyu

    Alaame alaame alaame téléphona
    Alaame alaame alaame téléphona
    Alaame alaame alaame téléphona
    Chérie alaame téléphonaa

    Tooñ nga ma been yoon yow chérie maa la baal
    Tooñaat ma ñaari yoon
    Même bu ñeent dama lay baal
    Li ma denc sama xol
    Yàlla sedde na ma ko waaw
    Ñëwel fi nga jege ma
    Loo bëgg wax ma ko waaw

    Continues after the ad

    Yow biik, yow biik si guddi nelawuma
    Di la xalaat te ba léegi babe nelawuma
    Yow deet, bul defe noonu doyaluma
    Ku la naan man dit, ku la raay genum reew sama
    Bi nga yekse laa xel yi daal
    Ñépp naan kaar machallah!
    Namoon naa la chérie boy waawaawaaw
    Aaah, aaah aah aah

    Alaame alaame alaame téléphona
    Alaame alaame alaame téléphona
    Alaame alaame alaame téléphona
    Chérie alaame téléphonaa

    Bébé yo i kànu de bɛnà i jàràbi
    Dalen bey Malakey ni kan
    Abey nafó kɔfɛ̌ la murani
    Sùnɔgɔ la
    Abey bali ka cun nekan
    Wa ne ɲɔgɔn
    Cai jugu sarama
    Ki bi ban nela ka kule ko fan fan
    I tɛ̀mɛ tó ka gɛ̀rɛ ne la
    Kuluci ñaifaila bey to ka pan pan
    Baby yo décroche moi
    Nebi wele appel teta
    I kadi n'gne ni wari ni CFA
    Jarabi géléman
    Neteni jànfa
    N' beni sara n'baguer baga bɛ la
    Akadi n' ñe i kakai ne denw ba
    Ni tɔgɔ dedo
    M'bo di ma
    Affection ni couer ni lomba

    Oh baby
    I ka baby kànu de bɛnà
    Jarabi dedoo
    Malakey tena i jànfa
    Oh baby
    I ka baby kànu de bɛnà
    Jarabi dedo
    Malakey tena i jànfa

    Alaame alaame alaame téléphona
    Alaame alaame alaame téléphona
    Alaame alaame alaame téléphona
    Chérie alaame téléphonaa

    Song details

    Composition:

    Did you see an error?

    Enviar revisão

    Related songs