Démocritic

Maabo

    Continúa después del anuncio

    Système bi lumu bëgg lañu bagn, té lumu bagn lañu bëgg
    Ñu joox len mbaranu kiray kenn bëgg ci mur suñu gëtt
    Peuple bu méér tekk ci xiif ak maar taff xol yi xed
    Privilége ñii baax tax ñenen ñi ñëkk liraam si ñax bi la jëm
    Le peuple a mal sen démocratie lañu tet
    Politique Corona mo suñu fébaar couvre feu, confiné ñëpp
    Ñi ñol duñu gatt ci justice té waral tribunal bi ni mbatt
    Avocat yi dañu léen tagg sans mettre xaad
    Takk der yi ay liff katt ku wax ñu jàp xët tët
    Ñana booy lañu fi ray rewmi taar amul xey
    Ñata mbamel biir get, ñata mort ci corona
    Pauvreté ñun fur ray yëpp ni déé ci corona

    Maandé titt na girr suñu doom (bilaye wallaye)
    Elëk gu Senegaal bi lumu nara doon (ngur jarul li)
    Wallahi bul xamon li neen ci gën (ñepp diaxlé nagn)
    Kenn du ja marr loo benn takk derr

    Continúa después del anuncio

    Politicien bumu taax nga njaay sa baakan amul jëgëm
    Ko ci faal bu faalo fatté la, bopp lëgëm
    Ñata élection taxul ñu am gouvernemet
    Lepp ñun la dañu ye gaawa faan faal président
    Jot naa nakk ñu xam suñu bopp
    Baayi xiro bëgg ngan yoo mell ni duñu ay mbokku
    Ni di saaga si net bi ku nekk dinane fii la bokku
    Ñi di waan teer carte électeur luy ndaay lolu
    Sacrifier saaw askan tokk
    Amon xam-xam bëgo jàngi, bëgg tékk joni joni
    Saaw ci mbedd, loo jot saañ, bëgg mu sétt léegi léegi
    Def sa jaxum ñan intervention bagn corruption
    Bu ñu waxé ngani Senegaal lilë lolu du solution
    Askan be faal ñu léen di faay
    Soo léen tallé rewmi di gën ñu faay
    Dañu waara bollo doon mbéne saay jow li faay gis nañu rap
    Peuple bi di def nakasudul nonu
    Bëgg ñu diaxasé takk derr yi
    Gir ñu doon suñu non, jaam wesul ci mbiim rew

    Maandé titt na girr suñu doom (bilaye wallaye)
    Elëk gu Senegaal bi lumu nara doon (ngur jarul li)
    Wallahi bul xamon li neen ci gën (ñepp diaxlé nagn)
    Kenn du ja marr loo benn takk derr

    Información de la canción

    Composición:

    ¿Los datos están equivocados?

    Enviar revisión