Continúa después del anuncio

    Bés bi nga juddu woon
    Delussi na, tay la tay, happy birthday
    Bés bi yay boroom
    Ndax yow rek dara dula fay, happy birthday
    Dégg naa ñu wax naan
    Bés du toute boroom rek ley tolool
    Yow dundël cent onze ans, happy birthday
    Happy birthday, tay sa bés la, happy birthday
    Happy birthday, nanga happy, happy birthday

    Bés bi nga juddu woon
    Mo delussi ñulay ndokalé
    Amo lu ko gën rëy
    Féké ngako kon nagn ko célébré
    Bima yéwo lako guiss si sama Facebook
    Ma-Mané toogay amatul naa dioug
    In-indil nagn la say cadeaux
    Kay soufflé sey bougies, dagg say gateaux

    Sa xarit yi nga magandol
    Wuyu si la ñëw diko fêté-ndo
    Ak photos yi ñu jëlë-ndo
    Happy birthday ñu kay wayandooo
    Yalla nga dundu ba déwén ñu défat lu mel ni
    Am jàmm ak xéwel mbékté bu yaatu ci yow mi

    Continúa después del anuncio

    Bés bi nga juddu woon
    Delussi na, tay la tay, happy birthday
    Bés bi yay boroom
    Ndax yow rek dara dula fay, happy birthday
    Dégg naa ñu wax naan
    Bés du toute boroom rek ley tolool
    Yow dundël cent onze ans, happy birthday
    Happy birthday, tay sa bés la, happy birthday
    Happy birthday, nanga happy, happy birthday

    Bés bu délussi
    Bés bu délussi
    Da-day neex, ñu yagg ko féééké
    Ñu diko fêté ak baneex, no ma guissé
    Tay fi la guéné, ñëw téw ci sa birthday/bés bi
    Bés bi munumako manqué

    Sa xarit yi nga magandol
    Wuyu si la ñëw diko fêté-ndo
    Ak photos yi ñu jëlë-ndo
    Happy birthday ñu kay wayandooo
    Dundel lu bari, ba say may di bawaan
    Sa nitt yu baax yangui ni
    Yaa ayé kay woon sa moomél

    Bés bi nga juddu woon
    Delussi na, tay la tay, happy birthday
    Bés bi yay boroom
    Ndax yow rek dara dula fay, happy birthday
    Dégg naa ñu wax naan
    Bés du toute boroom rek ley tolool
    Yow dundël cent onze ans, happy birthday
    Happy birthday, tay sa bés la, happy birthday
    Happy birthday, nanga happy, happy birthday

    Información de la canción

    Composición:

    ¿Los datos están equivocados?

    Enviar revisión