Jubo

Maabo

    Continúa después del anuncio

    Jubo dafa baax ci xol yi (waaw)
    Ndax dina rafétal suñu xel yi (waawaw)
    Jubo dafa baax ci reew mi (yeah, waawaw)
    Ndax dina défarat jikko yi (waawaw)

    Mën na gëna neex suñu reew mi
    Bokk ndéye ak bay ñun neen lë, yeah!
    Yénénté jàmm ci xol yi
    Té kune japé sa morome sa nawlé

    Ñun waruñ di noonoo dé
    Yallah mi ñu sakk buggul ñuy tongo dé
    Ay nitt késé lañ dagn war di balanté
    Dekk bi dina naat ci kaw ñu bëgganté
    Yeah, iyo!

    Jubo dafa baax ci reew mi (waawaw)
    Dina dëggërël askann wi (waawaw)
    Jubo dafa baax ci kër yi (yeah, waawaw)
    Dina défarate jikko yi (yeah, waawaw)

    Continúa después del anuncio

    Nañu ande doon bénn
    Baña xéx di kaff di ré
    Bul di xex sey and ndo
    Xaccando di dorando (waawaw)

    Jubo dafa baax ci kër yi
    Ndax dina rafétal suñu xol yi
    Jubo su amul ci reew
    Du yomb nga gis jamm ju raxul dara
    Giso ni warna mëna né
    Kénn baña dénthial sa morom dara
    Yéené yi su rafété, jitël jamm ci xel yé
    Jubo bu dëggu ci xol yi, ñepay né ci saalam

    Ñun dara waruñu bolé, sénégalais
    Du xett du diné du aalal diso di waxtan
    Téranga moy suñu doolé, sénégalais
    Ñu jawando suñu gaal gi waawaw moy li gën

    Jubo dafa baax ci reew mi (waawaw)
    Dina dëggërël askann wi (waawaw)
    Jubo dafa baax ci kër yi (yeah, waawaw)
    Dina défarat jikko yi (yeah, waawaw)

    Nañu ande doon bénn
    Baña xéx di kaff di ré
    Bul di xex sey and ndo
    Xaccando di dorando (waawaw)

    Información de la canción

    Composición:

    ¿Los datos están equivocados?

    Enviar revisión