Fi Ba Leuz

AMADEUS

    Continúa después del anuncio

    Eh, yooo
    Eh iiih
    Yeah yooo yaaa yeeh

    Fi ba Leuz ma lay moom coow rekk ay bari
    Def la soxnay sama coobare
    Toppal sama ginnaaw te bu coow bari
    Xam nga ni yaay sama càppali

    Xam nga yaa ni ma
    Ni teg na ma la he
    Fu ma Mousta teg jàmm bu Yàlla bind
    Man fonk na ma la
    Man it ma ni la heee, sa xel naa dalee
    Diandia bi du soppeeku Massamba
    Du dem sa Massamba la, hei!

    Continúa después del anuncio

    Fi ba Leuz ma lay moom coow rekk ay bari (bari bari bari bari)
    Def la soxnay sama coobare (bari bari bari bari)
    Toppal sama ginnaaw te bu coow bari (bari bari bari bari)
    Xam nga ni yaay sama càppali (bari bari bari)

    Jànq yaa ma ni
    Du ku la ciippatu génn ci ndaxte yombuloo
    Du ku la jàmm na ni, he waay!
    Jànq yaa ma ni
    Bis dina ñëw nga daagu ci kër gi séyal
    Man ma tok ci ndaanaan yi, hee waay!

    Li nga ma wax tax na mën na ma wat
    Ni doo ma bàyyi même su ma faatoo
    Àdduna yépp su ñu dajewoon
    Pour séparer ñu du tax mu àntu
    Jànq yaa ma ni, jànq yaa ma ni
    Li nga dikk doy na ma, wëruma leneen
    Li nga ma wax neex na ma, yeiiii

    Fi ba Leuz ma lay moom coow rekk ay bari (bari bari bari bari)
    Def la soxnay sama coobare (bari bari bari bari)
    Toppal sama ginnaaw te bu coow bari (bari bari bari bari)
    Xam nga ni yaay sama càppali (bari bari bari)

    Información de la canción

    Composición:

    ¿Los datos están equivocados?

    Enviar revisión

    Canciones relacionadas