Tout donner (feat. Xiirsa)

AMADEUS

    Continues after the ad

    Sama xol nga yore
    Moom laa la toppe
    Liiti liiti liiti liiti
    May rombe gumbe
    Dama tapetul
    Def naa ci lu ne
    Lu mu guddi guddi guddi
    Dama lay gunge

    Baby I follow you
    Cause my heart is on you
    You
    Baby I follow you
    Cause my heart is on you
    You

    Oooh pourtant
    Jox naa la lépp, jox la lépp
    Oooh pourtant
    Je t'ai tout donné, tout donné

    Euh euh euh

    Continues after the ad

    Massamba Wallo
    Xam naa bu baax li ngay bañ
    Ñu dem ba ci biir maa lay gaañ
    Def naa ko saay mas waaye
    Ak yaw da am lu may waaj
    Àdduna moo la soxla
    Man ma yitewoo la lool sax
    Massamba mi ngi may gaañ yaay
    Kalame naa la ak gaa yi
    Kaay gaaw, dëgg la ni dëng na
    Su ma demee balay way
    Nga xam ni caaxaan taxul

    Oooh pourtant
    Jox naa la lépp, jox la lépp
    Oooh pourtant
    Je t'ai tout donné, tout donné

    Euh euh euh

    Man duma saay saay
    Laaj ko sama gayi
    Ñëwal ñu life waay
    Sonn naa
    Bul mësa gaadaay
    Doonal seen yaay
    Njaabot gi kaay waay
    Gunge ma

    Man duma saay saay
    Laaj ko sama gayi
    Ñëwal ñu life waay
    Sonn naa

    Song details

    Composition:

    Did you see an error?

    Enviar revisão