Mère Célibataire

Mia Guisse

    Continúa después del anuncio

    Daan ko bëgg play kaay ñu game
    Rekk nga xam shingom du kaani xeeñ
    Difeinte faime, jaxase faine
    Gisuñuma seen gis gisa ñaaw

    Ñee di siisu
    Ñi lax seen soxor ci Yàlla
    Yàlla mi ñiy woote gëm mu ñu ko
    Laxu nëtëril dégg

    Héy girl
    Mënoon nga ko maafe, dëgg-dëgg
    Héy girl
    Tigadege bee na ni noon
    Héy girl
    Bëgg baax taxoon ma teela séy
    Séy muñ daj ëmb direeku
    Doo ma ci juddu

    Bautiful baby Aminatou
    Doon mère célibataire bi di fippu
    Doon ndey doon baay
    Doon ndey doon baay
    Doon ndey doon baay

    Benn nit ngay tuddu gaañ ay mbokkam
    Héey, ma ni mooma lu ma wor la di fen
    Te kenn du tuddu sa jaambaar
    Dañuy toog di xaar faux pas

    Continúa después del anuncio

    Héy girl
    Mënoon nga ko maafe, dëgg-dëgg
    Héy girl
    Tigadege bee na ni noon
    Héy girl
    Bëgg baax taxoon ma teela séy
    Séy muñ daj ëmb direeku
    Doo ma ci juddu

    Bautiful baby Aminatou
    Doon mère célibataire bi di fippu
    Doon ndey doon baay
    Doon ndey doon baay
    Doon ndey doon baay

    Mbaa doo màndu ak loo ko xamal
    Nit day màndu dee ko suturaal
    Mbaa doo màndu ak loo ko xamal
    Nit day màndu dee ko suturaal

    Nit ku xam Yàlla day màndu
    Nit ku gëm Yàlla day màndu
    Nit ku xam Yàlla day màndu
    Màndu, màndu

    Mànduleen ooo
    Mànduleen ooo
    Mànduleen ooo

    Héy girl
    Mënoon nga ko maafe, dëgg-dëgg
    Héy girl
    Tigadege bee na ni noon
    Héy girl
    Bëgg baax taxoon ma teela séy
    Séy muñ daj ëmb direeku
    Doo ma ci juddu

    Bautiful baby Aminatou
    Doon mère célibataire bi di fippu
    Doon ndey doon baay
    Doon ndey doon baay
    Doon ndey doon baay

    Del suturaal jigéen
    Del suturaal jigéen

    Información de la canción

    Composición:

    ¿Los datos están equivocados?

    Enviar revisión