Glow Up

Ndakhte Lo

    Continúa después del anuncio

    Foo mas a gis nit ku ñuy déj te deewagul
    Wowowowo wooy
    Jël kóolute tër ko ray dekkil kiy moytu
    Boobu maa ngi jël pusoo di ñaw li mu xotti

    Matraque boo tegoon sama yaram fattewuma
    Yaakaar nga tasoon abandon yi ma dem ba miss ko
    Sama dundu mel ni internet (nga ni)
    Li ñuy gis bokkul ak li ne
    Gént gi jeex na, léegi maa ngi ni di free

    Amatuma benn rëccu li ma weesu
    Dama xasa wane ginnaaw duma geesu
    Yabi naa la (yah), duma lekkaat
    Demal déglu Mbaye Gueye Faye bul ko force
    Kakatar bari jikko lañu ko xame
    Lépp lu weex du meew ñamal sett kaay
    Dégluma man bàyyi naa la

    Continúa después del anuncio

    Man bàyyi naa la!

    Mel ni wér ñu may seen ci kaw
    Lépp lu ma nekk mu glow up
    He, amigo (he!)
    Man maa la off (leer na)
    Train bi fi la la baa demal nga togg (he!)

    Maa ngi jongoma lu neex
    Mel ni rose zu valentin
    Foo ma seene maay ree
    Def lu am classe, tegsi di xén neex
    Ma yëngal àdduna, haa
    Jonge sax waru naa
    Gént gi jeex na, léegi maa ngi ni di free

    Amatuma benn rëccu li ma weesu
    Dama xasa wane ginnaaw duma geesu
    Yabi naa la (yah), duma lekkaat
    Demal déglu Mbaye Gueye Faye bul ko force
    Kakkatar bari jikko lañu ko xame
    Lépp lu weex du meew ñamal sett kaay
    Dégluma man bàyyi naa la

    Man bàyyi naa la!
    Man bàyyi naa la!

    Información de la canción

    Composición:

    ¿Los datos están equivocados?

    Enviar revisión