Nèko Hè

Ndakhte Lo

    Continúa después del anuncio

    Jàng ma taxu la xam, ne ko hé
    Jàng ma taxu la xam, ne ko hé
    Dem nga ba gëm nu ma melul, ne ko hé
    Seetu gisul jikko borom, ne ko hé

    Jàng ma taxu la xam, han han han
    Jàng ma taxu la xam, han han han
    Dem nga ba gëm nu ma melul, han han
    Seetu gisul jikko borom, han han

    Dinga juum, dinga wet
    Ni la bëgg dëgg di ci xeex
    Ñoo ngi soos, ñoo ngi jéem
    Bëgg yàq der bi di la guerre
    Te du lépp wara leer
    Xam nga sentimentale du lu ñuy fowe

    Continúa después del anuncio

    Lii ñu ne bari coow, li xaj yi di mbow
    Mooy li ngay xool gis wutenaak li leer
    No matter what I'm a human
    Ayaa, ayaa, ayaa
    Ñoo lay nax te ñoo lay gaañ

    (Ne ko hé) boo ko xamul
    (Ne ko hé) boo ko xamul ooy
    (Ne ko hé) xamuñu maay kan
    (Ne ko hé)

    Dundu baa ngi parewoo doo dugg serras
    Mënul baax de pare nañu pur yóbbu ferraille
    Bañ détail tax na may grossiste
    Liir de boo ko seexale xooñ de mooy dee na
    Duta mbaay loo reere biig ay wax
    Lum la dikk suba ba jant so di ay nax
    Telele mbele mbele wax fu ne
    Sentuma ci gaalu xacc doo mësa wax cambaay
    Du may bandi parewoo pur jéeg bi ray
    Du yàgg dara game bi de lay appo
    Non, non, mënoo xam jëmm jee

    Iyaa, iyaa, iyaa, iyaa
    Iyee aah
    (Ne ko hé) boo ko xamul
    (Ne ko hé) xamuñu maay kan
    (Ne ko hé)

    Jàng ma taxu la xam, ne ko hé
    Jàng ma taxu la xam, ne ko hé
    Dem nga ba gëm nu ma melul, ne ko hé
    Seetu gisul jikko borom, ne ko hé

    Información de la canción

    Composición:

    ¿Los datos están equivocados?

    Enviar revisión