Di La Bëgg

Omar Pène

    Continúa después del anuncio

    Yaw mi ma tànn ci seen biir
    Yaa ma xam, xam sama njëg du yaw rekk ma miin
    Yaw mi ma tànn ci seen biir
    Yaa ma xam, xam sama njëg du yaw rekk ma miin

    Xam naa su ma doon jaay
    Yaa may jënde
    Xam sama njëg du yaw rekk ma miin

    Yaw mi ma tànn ci seen biir
    Yaa ma xam, xam sama njëg du yaw rekk ma miin
    Yaw mi ma tànn ci seen biir
    Yaa ma xam, xam sama njëg du yaw rekk ma miin

    Soxna si baax nga yaatu nga
    Jigéen jile, rafet nga lool kaar tabbe
    Soxna si baax nga yaatu nga
    Jigéen jile, rafet nga lool kaar tabbe

    Mënuma séyeek moom
    Du sama nawle yaay
    Moom laa bëgg di ko bëgg di ko bëgg

    Continúa después del anuncio

    Mënuma séyeek moom
    Du sama nawle yaay
    Moom laa bëgg di ko bëgg di ko bëgg

    Di la bégal, di la bégal
    Di la coqotaan ba ngay xaxataay
    Ma di la bégal, di la bégal
    Di la toppattoo ba kenn du ni ñaaw

    Mbëggeel du jaay, amul prix bañ fay waxaale

    Di la bégal, di la bégal
    Di la coqotaan ba ngay xaxataay
    Ma di la bégal, di la bégal
    Di la toppattoo ba kenn du ni ñaaw
    Di la bégal, di la bégal
    Man na jënd sax doomu tubaab

    Di la bégal, di la bégal
    Di la toppattoo ba kenn du ni ñaaw
    Ma di la bégal, di la bégal
    Di la yaqloo mel ni sama taaw
    Di la bégal, di la bégal
    Di la toppattoo mel ni sama doom

    Di la bégal, di la bégal
    Di la yaqloo mel ni sama taaw
    Ma di la bégal, di la bégal
    Di la toppattoo mel ni sama doom
    Di la bégal, di la bégal
    Di la bégal ba kenn du ni ñaaw

    Soxna si baax nga, yaatu nga
    Jigéen jile, rafet nga lool kaar tabbe

    Mënuma séyeek moom
    Du sama nawle yaay
    Moom laa bëgg di ko bëgg di ko bëgg

    Mënuma séyeek moom
    Du sama nawle yaay
    Moom laa bëgg di ko bëgg di ko bëgg

    Información de la canción

    Composición:

    ¿Los datos están equivocados?

    Enviar revisión