Yaw mi ma tànn ci seen biir Yaa ma xam, xam sama njëg du yaw rekk ma miin Yaw mi ma tànn ci seen biir Yaa ma xam, xam sama njëg du yaw rekk ma miin Xam naa su ma doon jaay Yaa may jënde Xam sama njëg du yaw rekk ma miin Yaw mi ma tànn ci seen biir Yaa ma xam, xam sama njëg du yaw rekk ma miin Yaw mi ma tànn ci seen biir Yaa ma xam, xam sama njëg du yaw rekk ma miin Soxna si baax nga yaatu nga Jigéen jile, rafet nga lool kaar tabbe Soxna si baax nga yaatu nga Jigéen jile, rafet nga lool kaar tabbe Mënuma séyeek moom Du sama nawle yaay Moom laa bëgg di ko bëgg di ko bëgg Mënuma séyeek moom Du sama nawle yaay Moom laa bëgg di ko bëgg di ko bëgg Di la bégal, di la bégal Di la coqotaan ba ngay xaxataay Ma di la bégal, di la bégal Di la toppattoo ba kenn du ni ñaaw Mbëggeel du jaay, amul prix bañ fay waxaale Di la bégal, di la bégal Di la coqotaan ba ngay xaxataay Ma di la bégal, di la bégal Di la toppattoo ba kenn du ni ñaaw Di la bégal, di la bégal Man na jënd sax doomu tubaab Di la bégal, di la bégal Di la toppattoo ba kenn du ni ñaaw Ma di la bégal, di la bégal Di la yaqloo mel ni sama taaw Di la bégal, di la bégal Di la toppattoo mel ni sama doom Di la bégal, di la bégal Di la yaqloo mel ni sama taaw Ma di la bégal, di la bégal Di la toppattoo mel ni sama doom Di la bégal, di la bégal Di la bégal ba kenn du ni ñaaw Soxna si baax nga, yaatu nga Jigéen jile, rafet nga lool kaar tabbe Mënuma séyeek moom Du sama nawle yaay Moom laa bëgg di ko bëgg di ko bëgg Mënuma séyeek moom Du sama nawle yaay Moom laa bëgg di ko bëgg di ko bëgg