Leundeum (feat. Mia Guisse)

Omzo Dollar

    Continúa después del anuncio

    Majestic Drama

    Fu ma mëna ne jot sa appel: Bae foo ne?
    Li ma mëna def nga ni ma bae, no, no, no, no du way
    Allo, bae foo nekk?
    Ñibbisil, il fait nuit
    Waññil coow li, jalousie danga metti

    Góor a lëndëm, góor a lëndëm, góor a lëndëm yeay
    Góor a lëndëm, góor a lëndëm, góor a lëndëm yeay

    Ñaata góor ñoo ma topp
    Nga may wax li di ma tooñ
    Sonn naa, dootuma toog
    Confiance bu amul ci mbëggeel, non, non, du dem

    Continúa después del anuncio

    Fu ma mëna ne jot sa appel: Bae foo ne?
    Lu ma mëna def nga ne ma bae, no, no, no, no du way

    Góor a lëndëm, góor a lëndëm, góor a lëndëm yeay
    Góor a lëndëm, góor a lëndëm, góor a lëndëm yeay

    I say
    Jigéen bu baax, góor bu bon
    Takkali ko ni diwlin ak ndox
    Dama soxla ku may dégg sa soxla ku lay déglu
    Su ma xamul li ma bëgg xam naa li ma bëggul, yeah
    Mais góor a mel noonu fu mu tollu day risquer
    Daan kay defal jamm ku ko sonal lay pister
    Boo tegee tànk ci biti mu lay call insister
    Sa tur ci sama xol ndax ne nañu xol day gise
    Am na lu ma metti
    Ndax su ma la woree bàyyi bëgguma la gis ak keneen mais
    Est-ce que dama toxique?
    Est-ce que dama toxique?
    Jël sa xel bi dox ci, jël sa xol bi toog ci lëndëm

    Góor a lëndëm, góor a lëndëm, góor a lëndëm
    Góor a lëndëm, góor a lëndëm
    Yeah, yeah
    Hum!

    Kon waxal góor yi lay topp
    Ni demoo fenn fi ngay toog
    Ñun ñaar ñoo changer mu dem
    Effort su amul ci mbëggeel, non, non, du dem!

    Fu ma mëna ne jot sa appel: Bae foo ne?
    Li ma mëna def nga ne ma bae, no, no, no, no du way

    Góor a lëndëm, góor a lëndëm, góor a lëndëm yeay
    Góor a lëndëm, góor a lëndëm, góor a lëndëm yeay

    Información de la canción

    Composición:

    ¿Los datos están equivocados?

    Enviar revisión

    Canciones relacionadas