Bardé (Daphne Calée Remix)

Ouly

    Continúa después del anuncio

    Faf nga jël sama xol bi
    Man de yaa may dofloo
    Sama xol ba ngeek yaw
    Sama mer yaa koy gifloo

    Jot na nga xam yaw laa nob
    Li moom dafa fees mu ngi tuuru

    Ak loo mënti soxla
    Laaj ma ko man may jox la
    Fi lépp yaa ko moom
    Def ma sa soxna

    Jot na nga xam yaw laa nob
    Li moom dafa fort, moo raw guerre

    Man ci yaw laa bardé, waaw waaw
    Dama bardé
    Xam nga dama bardé, waaw waaw
    Dama bardé
    May gën di bég saa soo may reetaan
    Dama bardé
    Ni nga may def man rekk ma ko xam
    Dama bardé

    Continúa después del anuncio

    Man ci yaw laa bardé, waaw waaw
    Dama bardé
    Xam nga dama bardé, waaw waaw
    Dama bardé
    May gën di bég saa soo may reetaan
    Dama bardé
    Ni nga may def man rekk ma ko xam
    Dama bardé

    Sama reni xol
    Sori ci man loo wax ma ni waaw
    Yaa tax may ree, tax may noyyi
    Kon defal lu gaaw

    Yaw man rekk nga lova
    Man mi maa la raw
    Jëlal lépp ma may la
    Please ne ma waaw
    Yaw laa rekk duum ci douté
    Jegesil kaay ma déey la
    Soo bëggee sax ma wuje
    Tagg la, wayal la

    Jot na nga xam yaw laa nob
    Li moom dafa fees mu ngi tuuru

    Man ci yaw laa bardé, waaw waaw
    Dama bardé
    Xam nga dama bardé, waaw waaw
    Dama bardé
    May gën di bég saa soo may reetaan
    Dama bardé
    Ni nga may def man rekk ma ko xam
    Dama bardé

    Man ci yaw laa bardé, waaw waaw
    Dama bardé
    Xam nga dama bardé, waaw waaw
    Dama bardé
    May gën di bég saa soo may reetaan
    Dama bardé
    Ni nga may def man rekk ma ko xam
    Dama bardé

    Bardé, bardé bardé bardé
    Bardé, bardé bardé bardé
    Bardé, bardé bardé bardé
    Bardé, bardé bardé bardé

    Información de la canción

    Composición:

    ¿Los datos están equivocados?

    Enviar revisión