Faf nga jël sama xol bi Man de yaa may dofloo Sama xol ba ngeek yaw Sama mer yaa koy gifloo Jot na nga xam yaw laa nob Li moom dafa fees mu ngi tuuru Ak loo mënti soxla Laaj ma ko man may jox la Fi lépp yaa ko moom Def ma sa soxna Jot na nga xam yaw laa nob Li moom dafa fort, moo raw guerre Man ci yaw laa bardé, waaw waaw Dama bardé Xam nga dama bardé, waaw waaw Dama bardé May gën di bég saa soo may reetaan Dama bardé Ni nga may def man rekk ma ko xam Dama bardé Man ci yaw laa bardé, waaw waaw Dama bardé Xam nga dama bardé, waaw waaw Dama bardé May gën di bég saa soo may reetaan Dama bardé Ni nga may def man rekk ma ko xam Dama bardé Sama reni xol Sori ci man loo wax ma ni waaw Yaa tax may ree, tax may noyyi Kon defal lu gaaw Yaw man rekk nga lova Man mi maa la raw Jëlal lépp ma may la Please ne ma waaw Yaw laa rekk duum ci douté Jegesil kaay ma déey la Soo bëggee sax ma wuje Tagg la, wayal la Jot na nga xam yaw laa nob Li moom dafa fees mu ngi tuuru Man ci yaw laa bardé, waaw waaw Dama bardé Xam nga dama bardé, waaw waaw Dama bardé May gën di bég saa soo may reetaan Dama bardé Ni nga may def man rekk ma ko xam Dama bardé Man ci yaw laa bardé, waaw waaw Dama bardé Xam nga dama bardé, waaw waaw Dama bardé May gën di bég saa soo may reetaan Dama bardé Ni nga may def man rekk ma ko xam Dama bardé Bardé, bardé bardé bardé Bardé, bardé bardé bardé Bardé, bardé bardé bardé Bardé, bardé bardé bardé